As-Saffat · 11/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
فَاسْتَفْتِهِمْ أَهُمْ أَشَدُّ خَلْقًا أَم مَّنْ خَلَقْنَا ۚ إِنَّا خَلَقْنَاهُم مِّن طِينٍ لَّازِبٍ ۝١١
Fastaftihim ahum ashaddu khalqan am man khalaqnaa; innaa khalaqnaahum min teenil laazib
📖 Tekkim Wolof
Laajleen baxam dañoo gën a jafe bind ñeneen ña Nu bind ? Noo ngi leen binde ci ban bu tikk !

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 9-13 — Simoore As-Saffat

9دُحُورًا ۖ وَلَهُمْ عَذَابٌ وَاصِبٌ
dàqe leen fa. Ñu am mbugal muy sax.
10إِلَّا مَنْ خَطِفَ الْخَطْفَةَ فَأَتْبَعَهُ شِهَابٌ ثَاقِبٌ
Xanaa rekk léeg-léeg mu am ñu cay sàcc ay xibaar ; ñu di ko dàq ak jumu safara buy bënn.
11فَاسْتَفْتِهِمْ أَهُمْ أَشَدُّ خَلْقًا أَم مَّنْ خَلَقْنَا ۚ إِنَّا خَلَقْنَاهُم مِّن طِينٍ لَّازِبٍ
Laajleen baxam dañoo gën a jafe bind ñeneen ña Nu bind ? Noo ngi leen binde ci ban bu tikk !
12بَلْ عَجِبْتَ وَيَسْخَرُونَ
Yaw waaru nga, te ñoom ña ngay tejjiy reetaan !
13وَإِذَا ذُكِّرُوا لَا يَذْكُرُونَ
Te bu ñu leen di fàttali, duñu fàttaliku [Alxuraan] ;
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
11Aaya

Tekki — As-Saffat 11

Simoore As-Saffat Aaya 11 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Laajleen baxam dañoo gën a jafe bind ñeneen ña Nu…

Simoore Aaya 11/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 9–13. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers