As-Saffat · 118/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
وَهَدَيْنَاهُمَا الصِّرَاطَ الْمُسْتَقِيمَ ۝١١٨
Wa hadainaahumus Siraatal Mustaqeem
📖 Tekkim Wolof
Nu indiloon leen yoon wu jub wa xocc.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 116-120 — Simoore As-Saffat

116وَنَصَرْنَاهُمْ فَكَانُوا هُمُ الْغَالِبِينَ
Nu dimbali woon leen, ñoom ñoo nootoon.
117وَآتَيْنَاهُمَا الْكِتَابَ الْمُسْتَبِينَ
Nu indiloon leen ab téere bu bir
118وَهَدَيْنَاهُمَا الصِّرَاطَ الْمُسْتَقِيمَ
Nu indiloon leen yoon wu jub wa xocc.
119وَتَرَكْنَا عَلَيْهِمَا فِي الْآخِرِينَ
Nu bàyyi woon leen nit ña di leen fàttaliku :
120سَلَامٌ عَلَىٰ مُوسَىٰ وَهَارُونَ
“Jàmmi Yàlla na wàcc ci Muusaa ak Haaruuna”
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
118Aaya

Tekki — As-Saffat 118

Simoore As-Saffat Aaya 118 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nu indiloon leen yoon wu jub wa xocc.

Simoore Aaya 118/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 116–120. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Saturday, October 3, 2026

Don't forget us in your sincere prayers