As-Saffat · 117/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
وَآتَيْنَاهُمَا الْكِتَابَ الْمُسْتَبِينَ ۝١١٧
Wa aatainaahumal Kitaabal mustabeen
📖 Tekkim Wolof
Nu indiloon leen ab téere bu bir

🎧 Dégg


📜 Aaya 115-119 — Simoore As-Saffat

115وَنَجَّيْنَاهُمَا وَقَوْمَهُمَا مِنَ الْكَرْبِ الْعَظِيمِ
Musaloon Nanu leen ñoom seeni sët ca tiit mu rëy ma,
116وَنَصَرْنَاهُمْ فَكَانُوا هُمُ الْغَالِبِينَ
Nu dimbali woon leen, ñoom ñoo nootoon.
117وَآتَيْنَاهُمَا الْكِتَابَ الْمُسْتَبِينَ
Nu indiloon leen ab téere bu bir
118وَهَدَيْنَاهُمَا الصِّرَاطَ الْمُسْتَقِيمَ
Nu indiloon leen yoon wu jub wa xocc.
119وَتَرَكْنَا عَلَيْهِمَا فِي الْآخِرِينَ
Nu bàyyi woon leen nit ña di leen fàttaliku :
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
117Aaya

Tekki — As-Saffat 117

Simoore As-Saffat Aaya 117 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nu indiloon leen ab téere bu bir

Simoore Aaya 117/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 115–119. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers