As-Saffat · 119/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
وَتَرَكْنَا عَلَيْهِمَا فِي الْآخِرِينَ ۝١١٩
Wa taraknaa `alaihimaa fil aakhireen
📖 Tekkim Wolof
Nu bàyyi woon leen nit ña di leen fàttaliku :

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 117-121 — Simoore As-Saffat

117وَآتَيْنَاهُمَا الْكِتَابَ الْمُسْتَبِينَ
Nu indiloon leen ab téere bu bir
118وَهَدَيْنَاهُمَا الصِّرَاطَ الْمُسْتَقِيمَ
Nu indiloon leen yoon wu jub wa xocc.
119وَتَرَكْنَا عَلَيْهِمَا فِي الْآخِرِينَ
Nu bàyyi woon leen nit ña di leen fàttaliku :
120سَلَامٌ عَلَىٰ مُوسَىٰ وَهَارُونَ
“Jàmmi Yàlla na wàcc ci Muusaa ak Haaruuna”
121إِنَّا كَذَٰلِكَ نَجْزِي الْمُحْسِنِينَ
Noonu la Nuy feye ñiy rafetal ;
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
119Aaya

Tekki — As-Saffat 119

Simoore As-Saffat Aaya 119 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nu bàyyi woon leen nit ña di leen fàttaliku :

Simoore Aaya 119/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 117–121. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers