As-Saffat · 14/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
وَإِذَا رَأَوْا آيَةً يَسْتَسْخِرُونَ ۝١٤
Wa izaa ra aw Aayatinw yastaskhiroon
📖 Tekkim Wolof
dañuy wàkkante ak a reetaan [saa su ñu gisee keemaan],

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 12-16 — Simoore As-Saffat

12بَلْ عَجِبْتَ وَيَسْخَرُونَ
Yaw waaru nga, te ñoom ña ngay tejjiy reetaan !
13وَإِذَا ذُكِّرُوا لَا يَذْكُرُونَ
Te bu ñu leen di fàttali, duñu fàttaliku [Alxuraan] ;
14وَإِذَا رَأَوْا آيَةً يَسْتَسْخِرُونَ
dañuy wàkkante ak a reetaan [saa su ñu gisee keemaan],
15وَقَالُوا إِنْ هَٰذَا إِلَّا سِحْرٌ مُّبِينٌ
tey wax naan : “Lii dey ag njabar doŋŋ la.
16أَإِذَا مِتْنَا وَكُنَّا تُرَابًا وَعِظَامًا أَإِنَّا لَمَبْعُوثُونَ
Moo ndax su nu faatoo ba def suuf ak i yax, dees nanu dekkalaat ?
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
14Aaya

Tekki — As-Saffat 14

Simoore As-Saffat Aaya 14 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : dañuy wàkkante ak a reetaan [saa su ñu gisee keemaan],

Simoore Aaya 14/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 12–16. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Saturday, October 3, 2026

Don't forget us in your sincere prayers