As-Saffat · 15/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
وَقَالُوا إِنْ هَٰذَا إِلَّا سِحْرٌ مُّبِينٌ ١٥
Transliteration
Wa qaalooo in haazaa illaa sihrum mubeen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
tey wax naan : “Lii dey ag njabar doŋŋ la.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 13-17 — Simoore As-Saffat
13وَإِذَا ذُكِّرُوا لَا يَذْكُرُونَ
Te bu ñu leen di fàttali, duñu fàttaliku [Alxuraan] ;
14وَإِذَا رَأَوْا آيَةً يَسْتَسْخِرُونَ
dañuy wàkkante ak a reetaan [saa su ñu gisee keemaan],
15وَقَالُوا إِنْ هَٰذَا إِلَّا سِحْرٌ مُّبِينٌ
tey wax naan : “Lii dey ag njabar doŋŋ la.
16أَإِذَا مِتْنَا وَكُنَّا تُرَابًا وَعِظَامًا أَإِنَّا لَمَبْعُوثُونَ
Moo ndax su nu faatoo ba def suuf ak i yax, dees nanu dekkalaat ?
17أَوَآبَاؤُنَا الْأَوَّلُونَ
ak sunuy baay ak i maamaat ? ”
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
15Aaya
Tekki — As-Saffat 15
Simoore As-Saffat Aaya 15 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : tey wax naan : “Lii dey ag njabar doŋŋ la.Simoore Aaya 15/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 13–17. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Monday, September 7, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








