As-Saffat · 13/182
Tekki Waxtaan — As-Saffat
وَإِذَا ذُكِّرُوا لَا يَذْكُرُونَ ۝١٣
Wa izaa zukkiroo laa yazkuroon
📖 Tekkim Wolof
Te bu ñu leen di fàttali, duñu fàttaliku [Alxuraan] ;

🎧 Dégg


📜 Aaya 11-15 — As-Saffat

11فَاسْتَفْتِهِمْ أَهُمْ أَشَدُّ خَلْقًا أَم مَّنْ خَلَقْنَا ۚ إِنَّا خَلَقْنَاهُم مِّن طِينٍ لَّازِبٍ
Laajleen baxam dañoo gën a jafe bind ñeneen ña Nu bind ? Noo ngi leen binde ci ban bu tikk !
12بَلْ عَجِبْتَ وَيَسْخَرُونَ
Yaw waaru nga, te ñoom ña ngay tejjiy reetaan !
13وَإِذَا ذُكِّرُوا لَا يَذْكُرُونَ
Te bu ñu leen di fàttali, duñu fàttaliku [Alxuraan] ;
14وَإِذَا رَأَوْا آيَةً يَسْتَسْخِرُونَ
dañuy wàkkante ak a reetaan [saa su ñu gisee keemaan],
15وَقَالُوا إِنْ هَٰذَا إِلَّا سِحْرٌ مُّبِينٌ
tey wax naan : “Lii dey ag njabar doŋŋ la.
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
13Aaya

Tekki — As-Saffat 13

Simoore As-Saffat Aaya 13 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te bu ñu leen di fàttali, duñu fàttaliku [Alxuraan] ;

Simoore Aaya 13/182 — As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: As-Saffat Dégg, As-Saffat Tekki, As-Saffat mp3, As-Saffat pdf. Aaya 11–15. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers