As-Saffat · 35/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
إِنَّهُمْ كَانُوا إِذَا قِيلَ لَهُمْ لَا إِلَٰهَ إِلَّا اللَّهُ يَسْتَكْبِرُونَ ۝٣٥
Innahum kaanooo izaa qeela lahum laaa ilaaha illal laahu yastakbiroon
📖 Tekkim Wolof
Bu ñu waxaan ne : “Amul jeneen yàlla ju dul Yàlla”, dañu daan rëy-rëylu,

🎧 Dégg


📜 Aaya 33-37 — Simoore As-Saffat

33فَإِنَّهُمْ يَوْمَئِذٍ فِي الْعَذَابِ مُشْتَرِكُونَ
Bu bisub keroogee ñoom ñéppay bokk mbugal ma.
34إِنَّا كَذَٰلِكَ نَفْعَلُ بِالْمُجْرِمِينَ
Noonu la Nuy def tooñkat ya.
35إِنَّهُمْ كَانُوا إِذَا قِيلَ لَهُمْ لَا إِلَٰهَ إِلَّا اللَّهُ يَسْتَكْبِرُونَ
Bu ñu waxaan ne : “Amul jeneen yàlla ju dul Yàlla”, dañu daan rëy-rëylu,
36وَيَقُولُونَ أَئِنَّا لَتَارِكُو آلِهَتِنَا لِشَاعِرٍ مَّجْنُونٍ
tey wax naan : “Ndax danuy bàyyi sunu yàlla yi ngir woykat bu dof ? ”
37بَلْ جَاءَ بِالْحَقِّ وَصَدَّقَ الْمُرْسَلِينَ
Te moom dëgg rekk la indi tey dëggal li Yonent ya indi woon,
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
35Aaya

Tekki — As-Saffat 35

Simoore As-Saffat Aaya 35 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu ñu waxaan ne : “Amul jeneen yàlla ju dul…

Simoore Aaya 35/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 33–37. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers