As-Saffat · 36/182
Tekki Waxtaan — As-Saffat
وَيَقُولُونَ أَئِنَّا لَتَارِكُو آلِهَتِنَا لِشَاعِرٍ مَّجْنُونٍ ٣٦
Transliteration
Wa yaqooloona a`innaa lataarikooo aalihatinaa lishaa`irim majnoon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
tey wax naan : “Ndax danuy bàyyi sunu yàlla yi ngir woykat bu dof ? ”
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 34-38 — As-Saffat
34إِنَّا كَذَٰلِكَ نَفْعَلُ بِالْمُجْرِمِينَ
Noonu la Nuy def tooñkat ya.
35إِنَّهُمْ كَانُوا إِذَا قِيلَ لَهُمْ لَا إِلَٰهَ إِلَّا اللَّهُ يَسْتَكْبِرُونَ
Bu ñu waxaan ne : “Amul jeneen yàlla ju dul Yàlla”, dañu daan rëy-rëylu,
36وَيَقُولُونَ أَئِنَّا لَتَارِكُو آلِهَتِنَا لِشَاعِرٍ مَّجْنُونٍ
tey wax naan : “Ndax danuy bàyyi sunu yàlla yi ngir woykat bu dof ? ”
37بَلْ جَاءَ بِالْحَقِّ وَصَدَّقَ الْمُرْسَلِينَ
Te moom dëgg rekk la indi tey dëggal li Yonent ya indi woon,
38إِنَّكُمْ لَذَائِقُو الْعَذَابِ الْأَلِيمِ
Yéen dangeen mos mbugal mu mitti.
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
36Aaya
Tekki — As-Saffat 36
Simoore As-Saffat Aaya 36 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : tey wax naan : “Ndax danuy bàyyi sunu yàlla yi…Simoore Aaya 36/182 — As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: As-Saffat Dégg, As-Saffat Tekki, As-Saffat mp3, As-Saffat pdf. Aaya 34–38. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








