As-Saffat · 51/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
قَالَ قَائِلٌ مِّنْهُمْ إِنِّي كَانَ لِي قَرِينٌ ۝٥١
Qaala qaaa`ilum minhum innee kaana lee qareen
📖 Tekkim Wolof
Mu am ci ñoom kuy wax naan : “Man dey amoon naa àndandoo”

🎧 Dégg


📜 Aaya 49-53 — Simoore As-Saffat

49كَأَنَّهُنَّ بَيْضٌ مَّكْنُونٌ
weex ba mel ni nen.
50فَأَقْبَلَ بَعْضُهُمْ عَلَىٰ بَعْضٍ يَتَسَاءَلُونَ
Ku nekk di geesu moroomam di laajante.
51قَالَ قَائِلٌ مِّنْهُمْ إِنِّي كَانَ لِي قَرِينٌ
Mu am ci ñoom kuy wax naan : “Man dey amoon naa àndandoo”
52يَقُولُ أَإِنَّكَ لَمِنَ الْمُصَدِّقِينَ
di wax ba-tey naan : “Ndax yaw gëm nga tigi ?
53أَإِذَا مِتْنَا وَكُنَّا تُرَابًا وَعِظَامًا أَإِنَّا لَمَدِينُونَ
Ndax bu nu faatoo ba doon suuf ak i yax, dara dananu warati ? ”
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
51Aaya

Tekki — As-Saffat 51

Simoore As-Saffat Aaya 51 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu am ci ñoom kuy wax naan : “Man dey…

Simoore Aaya 51/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 49–53. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers