As-Saffat · 52/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
يَقُولُ أَإِنَّكَ لَمِنَ الْمُصَدِّقِينَ ۝٥٢
Yaqoolu a`innnaka laminal musaddiqeen
📖 Tekkim Wolof
di wax ba-tey naan : “Ndax yaw gëm nga tigi ?

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 50-54 — Simoore As-Saffat

50فَأَقْبَلَ بَعْضُهُمْ عَلَىٰ بَعْضٍ يَتَسَاءَلُونَ
Ku nekk di geesu moroomam di laajante.
51قَالَ قَائِلٌ مِّنْهُمْ إِنِّي كَانَ لِي قَرِينٌ
Mu am ci ñoom kuy wax naan : “Man dey amoon naa àndandoo”
52يَقُولُ أَإِنَّكَ لَمِنَ الْمُصَدِّقِينَ
di wax ba-tey naan : “Ndax yaw gëm nga tigi ?
53أَإِذَا مِتْنَا وَكُنَّا تُرَابًا وَعِظَامًا أَإِنَّا لَمَدِينُونَ
Ndax bu nu faatoo ba doon suuf ak i yax, dara dananu warati ? ”
54قَالَ هَلْ أَنتُم مُّطَّلِعُونَ
Mu wax ne : “Xanaa téenuleen ? ”
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
52Aaya

Tekki — As-Saffat 52

Simoore As-Saffat Aaya 52 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : di wax ba-tey naan : “Ndax yaw gëm nga tigi…

Simoore Aaya 52/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 50–54. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers