As-Saffat · 53/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
أَإِذَا مِتْنَا وَكُنَّا تُرَابًا وَعِظَامًا أَإِنَّا لَمَدِينُونَ ۝٥٣
A-izaa mitnaa wa kunnaa turaabanw wa `izaaman `ainnaa lamadeenoon
📖 Tekkim Wolof
Ndax bu nu faatoo ba doon suuf ak i yax, dara dananu warati ? ”

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 51-55 — Simoore As-Saffat

51قَالَ قَائِلٌ مِّنْهُمْ إِنِّي كَانَ لِي قَرِينٌ
Mu am ci ñoom kuy wax naan : “Man dey amoon naa àndandoo”
52يَقُولُ أَإِنَّكَ لَمِنَ الْمُصَدِّقِينَ
di wax ba-tey naan : “Ndax yaw gëm nga tigi ?
53أَإِذَا مِتْنَا وَكُنَّا تُرَابًا وَعِظَامًا أَإِنَّا لَمَدِينُونَ
Ndax bu nu faatoo ba doon suuf ak i yax, dara dananu warati ? ”
54قَالَ هَلْ أَنتُم مُّطَّلِعُونَ
Mu wax ne : “Xanaa téenuleen ? ”
55فَاطَّلَعَ فَرَآهُ فِي سَوَاءِ الْجَحِيمِ
Mu daldi téen, gis ko ca biir Safara,
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
53Aaya

Tekki — As-Saffat 53

Simoore As-Saffat Aaya 53 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ndax bu nu faatoo ba doon suuf ak i yax,…

Simoore Aaya 53/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 51–55. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers