As-Saffat · 55/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
فَاطَّلَعَ فَرَآهُ فِي سَوَاءِ الْجَحِيمِ ۝٥٥
Fattala`a fara aahu fee sawaaa`il Jaheem
📖 Tekkim Wolof
Mu daldi téen, gis ko ca biir Safara,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 53-57 — Simoore As-Saffat

53أَإِذَا مِتْنَا وَكُنَّا تُرَابًا وَعِظَامًا أَإِنَّا لَمَدِينُونَ
Ndax bu nu faatoo ba doon suuf ak i yax, dara dananu warati ? ”
54قَالَ هَلْ أَنتُم مُّطَّلِعُونَ
Mu wax ne : “Xanaa téenuleen ? ”
55فَاطَّلَعَ فَرَآهُ فِي سَوَاءِ الْجَحِيمِ
Mu daldi téen, gis ko ca biir Safara,
56قَالَ تَاللَّهِ إِن كِدتَّ لَتُرْدِينِ
mu wax ne : “Waat naa ci Yàlla ne ! Xaw nga maa tax a alku !
57وَلَوْلَا نِعْمَةُ رَبِّي لَكُنتُ مِنَ الْمُحْضَرِينَ
dogankoon ak sama dimbalul Boroom, danaa sànku.
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
55Aaya

Tekki — As-Saffat 55

Simoore As-Saffat Aaya 55 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu daldi téen, gis ko ca biir Safara,

Simoore Aaya 55/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 53–57. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers