As-Saffat · 54/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
قَالَ هَلْ أَنتُم مُّطَّلِعُونَ ۝٥٤
Qaala hal antum muttali`oon
📖 Tekkim Wolof
Mu wax ne : “Xanaa téenuleen ? ”

🎧 Dégg


📜 Aaya 52-56 — Simoore As-Saffat

52يَقُولُ أَإِنَّكَ لَمِنَ الْمُصَدِّقِينَ
di wax ba-tey naan : “Ndax yaw gëm nga tigi ?
53أَإِذَا مِتْنَا وَكُنَّا تُرَابًا وَعِظَامًا أَإِنَّا لَمَدِينُونَ
Ndax bu nu faatoo ba doon suuf ak i yax, dara dananu warati ? ”
54قَالَ هَلْ أَنتُم مُّطَّلِعُونَ
Mu wax ne : “Xanaa téenuleen ? ”
55فَاطَّلَعَ فَرَآهُ فِي سَوَاءِ الْجَحِيمِ
Mu daldi téen, gis ko ca biir Safara,
56قَالَ تَاللَّهِ إِن كِدتَّ لَتُرْدِينِ
mu wax ne : “Waat naa ci Yàlla ne ! Xaw nga maa tax a alku !
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
54Aaya

Tekki — As-Saffat 54

Simoore As-Saffat Aaya 54 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu wax ne : “Xanaa téenuleen ? ”

Simoore Aaya 54/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 52–56. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers