As-Saffat · 8/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
لَّا يَسَّمَّعُونَ إِلَى الْمَلَإِ الْأَعْلَىٰ وَيُقْذَفُونَ مِن كُلِّ جَانِبٍ ۝٨
Laa yassamma `oona ilal mala il a`alaa wa yuqzafoona min kulli jaanib
📖 Tekkim Wolof
Duñu mën yëddu waa péey ba gën a kawe ; te dañu leen fay mbàqe wet gu nekk,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 6-10 — Simoore As-Saffat

6إِنَّا زَيَّنَّا السَّمَاءَ الدُّنْيَا بِزِينَةٍ الْكَوَاكِبِ
Taaralal Nanu asamaan si gën a jexe àddina si ci taarub ay bidiw,
7وَحِفْظًا مِّن كُلِّ شَيْطَانٍ مَّارِدٍ
def ca kaaraange ci sépp séytaane suy féttérlu.
8لَّا يَسَّمَّعُونَ إِلَى الْمَلَإِ الْأَعْلَىٰ وَيُقْذَفُونَ مِن كُلِّ جَانِبٍ
Duñu mën yëddu waa péey ba gën a kawe ; te dañu leen fay mbàqe wet gu nekk,
9دُحُورًا ۖ وَلَهُمْ عَذَابٌ وَاصِبٌ
dàqe leen fa. Ñu am mbugal muy sax.
10إِلَّا مَنْ خَطِفَ الْخَطْفَةَ فَأَتْبَعَهُ شِهَابٌ ثَاقِبٌ
Xanaa rekk léeg-léeg mu am ñu cay sàcc ay xibaar ; ñu di ko dàq ak jumu safara buy bënn.
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
8Aaya

Tekki — As-Saffat 8

Simoore As-Saffat Aaya 8 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Duñu mën yëddu waa péey ba gën a kawe ;…

Simoore Aaya 8/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 6–10. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers