As-Saffat · 90/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
فَتَوَلَّوْا عَنْهُ مُدْبِرِينَ ۝٩٠
Fatawallaw `anhu mudbireen
📖 Tekkim Wolof
Ñu dëddu ko, won ko ginnaaw.

🎧 Dégg


📜 Aaya 88-92 — Simoore As-Saffat

88فَنَظَرَ نَظْرَةً فِي النُّجُومِ
Mu téen xool biddéew yi [di settantal],
89فَقَالَ إِنِّي سَقِيمٌ
mu daldi wax ne : “Man damaa wopp”.
90فَتَوَلَّوْا عَنْهُ مُدْبِرِينَ
Ñu dëddu ko, won ko ginnaaw.
91فَرَاغَ إِلَىٰ آلِهَتِهِمْ فَقَالَ أَلَا تَأْكُلُونَ
Mu potoxlu ca seen yàlla ya, ne leen : “Ndax dungeen lekk ?
92مَا لَكُمْ لَا تَنطِقُونَ
Ana lu leen dal ba dungeen wax ? ”
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
90Aaya

Tekki — As-Saffat 90

Simoore As-Saffat Aaya 90 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu dëddu ko, won ko ginnaaw.

Simoore Aaya 90/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 88–92. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers