As-Saffat · 97/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
قَالُوا ابْنُوا لَهُ بُنْيَانًا فَأَلْقُوهُ فِي الْجَحِيمِ ۝٩٧
Qaalub noo lahoo bun yaanan fa alqoohu fil jaheem
📖 Tekkim Wolof
Ñu wax ne : “Tabaxal-leen ko puur te sànni ko ca safara sa ! ”

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 95-99 — Simoore As-Saffat

95قَالَ أَتَعْبُدُونَ مَا تَنْحِتُونَ
Mu wax ne : “Ndax dangeen di jaamu lu ngeen di yatt,
96وَاللَّهُ خَلَقَكُمْ وَمَا تَعْمَلُونَ
te Yàlla moo leen bind ak li ngeen di defar ? ”
97قَالُوا ابْنُوا لَهُ بُنْيَانًا فَأَلْقُوهُ فِي الْجَحِيمِ
Ñu wax ne : “Tabaxal-leen ko puur te sànni ko ca safara sa ! ”
98فَأَرَادُوا بِهِ كَيْدًا فَجَعَلْنَاهُمُ الْأَسْفَلِينَ
Ñu bëggoon koo fexeel ; Nu suufeel leen, detteel leen.
99وَقَالَ إِنِّي ذَاهِبٌ إِلَىٰ رَبِّي سَيَهْدِينِ
Mu wax ne : “Maa ngi dem ca sama Boroom, Dana ma gindi.
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
97Aaya

Tekki — As-Saffat 97

Simoore As-Saffat Aaya 97 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu wax ne : “Tabaxal-leen ko puur te sànni ko…

Simoore Aaya 97/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 95–99. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers