As-Saffat · 96/182
Tekki Waxtaan — As-Saffat
وَاللَّهُ خَلَقَكُمْ وَمَا تَعْمَلُونَ ۝٩٦
Wallaahu khalaqakum wa maa ta`maloon
📖 Tekkim Wolof
te Yàlla moo leen bind ak li ngeen di defar ? ”

🎧 Dégg


📜 Aaya 94-98 — As-Saffat

94فَأَقْبَلُوا إِلَيْهِ يَزِفُّونَ
Ñu wutsi ko di daw.
95قَالَ أَتَعْبُدُونَ مَا تَنْحِتُونَ
Mu wax ne : “Ndax dangeen di jaamu lu ngeen di yatt,
96وَاللَّهُ خَلَقَكُمْ وَمَا تَعْمَلُونَ
te Yàlla moo leen bind ak li ngeen di defar ? ”
97قَالُوا ابْنُوا لَهُ بُنْيَانًا فَأَلْقُوهُ فِي الْجَحِيمِ
Ñu wax ne : “Tabaxal-leen ko puur te sànni ko ca safara sa ! ”
98فَأَرَادُوا بِهِ كَيْدًا فَجَعَلْنَاهُمُ الْأَسْفَلِينَ
Ñu bëggoon koo fexeel ; Nu suufeel leen, detteel leen.
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
96Aaya

Tekki — As-Saffat 96

Simoore As-Saffat Aaya 96 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te Yàlla moo leen bind ak li ngeen di defar…

Simoore Aaya 96/182 — As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: As-Saffat Dégg, As-Saffat Tekki, As-Saffat mp3, As-Saffat pdf. Aaya 94–98. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers