Sad · 37/88
Tekki Waxtaan — Sad
وَالشَّيَاطِينَ كُلَّ بَنَّاءٍ وَغَوَّاصٍ ٣٧
Transliteration
Wash Shayaateena kulla bannaaa`inw wa ghawwaas
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Tàggatal Nanu ko sayaane yi, ñu di ko tabaxal ak di ko nuural ci (ndox).
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 35-39 — Sad
35قَالَ رَبِّ اغْفِرْ لِي وَهَبْ لِي مُلْكًا لَّا يَنبَغِي لِأَحَدٍ مِّن بَعْدِي ۖ إِنَّكَ أَنتَ الْوَهَّابُ
Mu wax ne : “Yaw sama Boroom, na nga ma jégal te may ma nguur goo xam ne kenn dootu ko am sama ginnaaw. Yaw yaay Mayaakoon bi”.
36فَسَخَّرْنَا لَهُ الرِّيحَ تَجْرِي بِأَمْرِهِ رُخَاءً حَيْثُ أَصَابَ
Tàggatal Nanu ko ngelaw li, muy daw ci ndigëlam, ak fu mu jublu.
37وَالشَّيَاطِينَ كُلَّ بَنَّاءٍ وَغَوَّاصٍ
Tàggatal Nanu ko sayaane yi, ñu di ko tabaxal ak di ko nuural ci (ndox).
38وَآخَرِينَ مُقَرَّنِينَ فِي الْأَصْفَادِ
Ak ñeneen, ñu ñu lëkkële ak i njéng.
39هَٰذَا عَطَاؤُنَا فَامْنُنْ أَوْ أَمْسِكْ بِغَيْرِ حِسَابٍ
“Lii mooy sunug may ; mayeel walla nga téye ko kenn du ko waññook yaw”.
SadFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
37Aaya
Tekki — Sad 37
Simoore Sad Aaya 37 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Tàggatal Nanu ko sayaane yi, ñu di ko tabaxal ak…Simoore Aaya 37/88 — Sad ص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Sad Dégg, Sad Tekki, Sad mp3, Sad pdf. Aaya 35–39. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








