Sad · 38/88
Tekki Waxtaan — Sad
وَآخَرِينَ مُقَرَّنِينَ فِي الْأَصْفَادِ ۝٣٨
Wa aakhareena muqarraneena fil asfaad
📖 Tekkim Wolof
Ak ñeneen, ñu ñu lëkkële ak i njéng.

🎧 Dégg


📜 Aaya 36-40 — Sad

36فَسَخَّرْنَا لَهُ الرِّيحَ تَجْرِي بِأَمْرِهِ رُخَاءً حَيْثُ أَصَابَ
Tàggatal Nanu ko ngelaw li, muy daw ci ndigëlam, ak fu mu jublu.
37وَالشَّيَاطِينَ كُلَّ بَنَّاءٍ وَغَوَّاصٍ
Tàggatal Nanu ko sayaane yi, ñu di ko tabaxal ak di ko nuural ci (ndox).
38وَآخَرِينَ مُقَرَّنِينَ فِي الْأَصْفَادِ
Ak ñeneen, ñu ñu lëkkële ak i njéng.
39هَٰذَا عَطَاؤُنَا فَامْنُنْ أَوْ أَمْسِكْ بِغَيْرِ حِسَابٍ
“Lii mooy sunug may ; mayeel walla nga téye ko kenn du ko waññook yaw”.
40وَإِنَّ لَهُ عِندَنَا لَزُلْفَىٰ وَحُسْنَ مَآبٍ
Te mooy am na daraja ju Nu jege ak wàccuwaay wu jekk.
SadFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
38Aaya

Tekki — Sad 38

Simoore Sad Aaya 38 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ak ñeneen, ñu ñu lëkkële ak i njéng.

Simoore Aaya 38/88 — Sad ص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Sad Dégg, Sad Tekki, Sad mp3, Sad pdf. Aaya 36–40. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers