Ghafir · 61/85
Tekki Waxtaan — Ghafir
اللَّهُ الَّذِي جَعَلَ لَكُمُ اللَّيْلَ لِتَسْكُنُوا فِيهِ وَالنَّهَارَ مُبْصِرًا ۚ إِنَّ اللَّهَ لَذُو فَضْلٍ عَلَى النَّاسِ وَلَٰكِنَّ أَكْثَرَ النَّاسِ لَا يَشْكُرُونَ ٦١
Transliteration
Allaahul lazee ja`ala lakumul laila litqaskunoo feehi wannahaara mubsiraa; innal laaha lazoo fadlin `alan naasi wa laakinna aksaran naasi laa yashkuroon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Yàlla mi leen defal guddi ngeen di ci dallu, defal leen bëccëg bi it ngeen di ci man a gis (bay fàggu ji). Yàlla boroom Ngënéel la ci kaw nit ñi, waaye li ëpp ci nit ñi duñu sant.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 59-63 — Ghafir
59إِنَّ السَّاعَةَ لَآتِيَةٌ لَّا رَيْبَ فِيهَا وَلَٰكِنَّ أَكْثَرَ النَّاسِ لَا يُؤْمِنُونَ
Bis Pénc ba ; Luy dikk la : nàttable amu ca ; waaye li ëpp ci nit ñi gëmu ñu.
60وَقَالَ رَبُّكُمُ ادْعُونِي أَسْتَجِبْ لَكُمْ ۚ إِنَّ الَّذِينَ يَسْتَكْبِرُونَ عَنْ عِبَادَتِي سَيَدْخُلُونَ جَهَنَّمَ دَاخِرِينَ
Seen Boroom nee na : “Wooleen ma, Ma wuyu leen. Ña nga xam ne, dañoo rëy-rëylu, lànk bañ maa jaamu, danañu dugg Safara ànd ak toroxtaane”.
61اللَّهُ الَّذِي جَعَلَ لَكُمُ اللَّيْلَ لِتَسْكُنُوا فِيهِ وَالنَّهَارَ مُبْصِرًا ۚ إِنَّ اللَّهَ لَذُو فَضْلٍ عَلَى النَّاسِ وَلَٰكِنَّ أَكْثَرَ النَّاسِ لَا يَشْكُرُونَ
Yàlla mi leen defal guddi ngeen di ci dallu, defal leen bëccëg bi it ngeen di ci man a gis (bay fàggu ji). Yàlla boroom Ngënéel la ci kaw nit ñi, waaye li ëpp ci nit ñi duñu sant.
62ذَٰلِكُمُ اللَّهُ رَبُّكُمْ خَالِقُ كُلِّ شَيْءٍ لَّا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ ۖ فَأَنَّىٰ تُؤْفَكُونَ
Koo ku moo di Yàlla seen Boroom, Moo bind lépp. Amul jeneen Yàlla judul moom. Kon naka ngeen di lajje féew (ca yoonu Yàlla wu jub wa xocc) ?
63كَذَٰلِكَ يُؤْفَكُ الَّذِينَ كَانُوا بِآيَاتِ اللَّهِ يَجْحَدُونَ
Noonu la ñu daan weddi kàdduy Yàlla di dumóoyoo [yoonu] Yàlla.
GhafirFihi Alxuraan
85Aaya
MeccanRevelation
61Aaya
Tekki — Ghafir 61
Simoore Ghafir Aaya 61 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàlla mi leen defal guddi ngeen di ci dallu, defal…Simoore Aaya 61/85 — Ghafir غافر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ghafir Dégg, Ghafir Tekki, Ghafir mp3, Ghafir pdf. Aaya 59–63. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








