Az-Zukhruf · 57/89
Tekki Waxtaan — Simoore Az-Zukhruf
۞ وَلَمَّا ضُرِبَ ابْنُ مَرْيَمَ مَثَلًا إِذَا قَوْمُكَ مِنْهُ يَصِدُّونَ ۝٥٧
Wa lammaa duribab nu Maryama masalan izaa qawmu ka minhu yasidoon
📖 Tekkim Wolof
Ba ñu jëlee misaal ci Iisaa doomi Maryaama, saw nit dañoo daldi dumóoyu,

🎧 Dégg


📜 Aaya 55-59 — Simoore Az-Zukhruf

55فَلَمَّا آسَفُونَا انتَقَمْنَا مِنْهُمْ فَأَغْرَقْنَاهُمْ أَجْمَعِينَ
Ba ñu Nu merloo, ca la Nu fayyoo labal ñoom ñépp.
56فَجَعَلْنَاهُمْ سَلَفًا وَمَثَلًا لِّلْآخِرِينَ
Nu def leen ñu di am njàng ci ñiy xalset a dikk ëllëg.
57۞ وَلَمَّا ضُرِبَ ابْنُ مَرْيَمَ مَثَلًا إِذَا قَوْمُكَ مِنْهُ يَصِدُّونَ
Ba ñu jëlee misaal ci Iisaa doomi Maryaama, saw nit dañoo daldi dumóoyu,
58وَقَالُوا أَآلِهَتُنَا خَيْرٌ أَمْ هُوَ ۚ مَا ضَرَبُوهُ لَكَ إِلَّا جَدَلًا ۚ بَلْ هُمْ قَوْمٌ خَصِمُونَ
Ñu daldi wax ne : “Ndax sunuy Yàlla ñoo gën, walla moom sax ? ” Ay werante rekk la ñu fi indi . Te sax ñoom ay niti tafaar la ñu.
59إِنْ هُوَ إِلَّا عَبْدٌ أَنْعَمْنَا عَلَيْهِ وَجَعَلْنَاهُ مَثَلًا لِّبَنِي إِسْرَائِيلَ
Moom de (Muusaa) ab jaam rekk la bu Nu jox xeewal def ko muy roytéef ci wa Bani Israayiil.
Az-ZukhrufFihi Alxuraan
89Aaya
MeccanRevelation
57Aaya

Tekki — Az-Zukhruf 57

Simoore Az-Zukhruf Aaya 57 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ba ñu jëlee misaal ci Iisaa doomi Maryaama, saw nit…

Simoore Aaya 57/89 — Simoore Az-Zukhruf الزخرف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Az-Zukhruf Dégg, Simoore Az-Zukhruf Tekki, Simoore Az-Zukhruf mp3, Simoore Az-Zukhruf pdf. Aaya 55–59. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers