Al-Ahqaf · 32/35
Tekki Waxtaan — Al-Ahqaf
وَمَن لَّا يُجِبْ دَاعِيَ اللَّهِ فَلَيْسَ بِمُعْجِزٍ فِي الْأَرْضِ وَلَيْسَ لَهُ مِن دُونِهِ أَوْلِيَاءُ ۚ أُولَٰئِكَ فِي ضَلَالٍ مُّبِينٍ ٣٢
Transliteration
Wa mal laa yujib daa`iyal laahi falaisa bimu`jizin fil ardi wa laisa lahoo min dooniheee awliyaaa`; ulaaa ika fee dalaalim mubeen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Te nag képp ku wuyuwul wootekatu Yàlla ba. Du man a raw mukk Yàlla ci kaw suuf si, te it du am ku koy man a dimbali ginnaaw Yàlla. Ñooñee ña nga ci réer gu bir sori.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 30-34 — Al-Ahqaf
30قَالُوا يَا قَوْمَنَا إِنَّا سَمِعْنَا كِتَابًا أُنزِلَ مِن بَعْدِ مُوسَىٰ مُصَدِّقًا لِّمَا بَيْنَ يَدَيْهِ يَهْدِي إِلَى الْحَقِّ وَإِلَىٰ طَرِيقٍ مُّسْتَقِيمٍ
Nee na ñu : "Eey yéen sunuw xeet ! Déglu nanu ab Téere bu ñu wàcce ginnaaw Muusaa, muy dëggal la ko jiitu dafay gindee itam jëme ci dëgg. Ak ci yoon wu jub xocc wa.
31يَا قَوْمَنَا أَجِيبُوا دَاعِيَ اللَّهِ وَآمِنُوا بِهِ يَغْفِرْ لَكُم مِّن ذُنُوبِكُمْ وَيُجِرْكُم مِّنْ عَذَابٍ أَلِيمٍ
ey yéen sunuy xeet wuyu leen wootekatu Yàlla ba ! Te na ngeen koy gëm. (Su ngeen ko defee) dana leen di jéggal seen bàkkaar, te it kon dana leen yiir ci mbugal mu mitti.
32وَمَن لَّا يُجِبْ دَاعِيَ اللَّهِ فَلَيْسَ بِمُعْجِزٍ فِي الْأَرْضِ وَلَيْسَ لَهُ مِن دُونِهِ أَوْلِيَاءُ ۚ أُولَٰئِكَ فِي ضَلَالٍ مُّبِينٍ
Te nag képp ku wuyuwul wootekatu Yàlla ba. Du man a raw mukk Yàlla ci kaw suuf si, te it du am ku koy man a dimbali ginnaaw Yàlla. Ñooñee ña nga ci réer gu bir sori.
33أَوَلَمْ يَرَوْا أَنَّ اللَّهَ الَّذِي خَلَقَ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ وَلَمْ يَعْيَ بِخَلْقِهِنَّ بِقَادِرٍ عَلَىٰ أَن يُحْيِيَ الْمَوْتَىٰ ۚ بَلَىٰ إِنَّهُ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ قَدِيرٌ
Xanaa gisuñu ne Yàllaa bind asamaan yeek suuf si, te sonnut ci bind gi mu leen bind sàkk leen, xanaa war na man a dekkal néew ? Waaw-waaw. Moom man na lépp lu ne.
34وَيَوْمَ يُعْرَضُ الَّذِينَ كَفَرُوا عَلَى النَّارِ أَلَيْسَ هَٰذَا بِالْحَقِّ ۖ قَالُوا بَلَىٰ وَرَبِّنَا ۚ قَالَ فَذُوقُوا الْعَذَابَ بِمَا كُنتُمْ تَكْفُرُونَ
Cay bu keroogee bis ba ñuy gaaral yéefar ya ca Safara (te naan leen) : “Ndax lii du dëgg ? ” Ñuy tontu naan : “Axakañ , ak sunu màggug Boroom”. Mu ne leen : “Tokamtiku leen mbugël ma ngir li ngeen daan weddi”.
Al-AhqafFihi Alxuraan
35Aaya
MeccanRevelation
32Aaya
Tekki — Al-Ahqaf 32
Simoore Al-Ahqaf Aaya 32 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te nag képp ku wuyuwul wootekatu Yàlla ba. Du man…Simoore Aaya 32/35 — Al-Ahqaf الأحقاف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Ahqaf Dégg, Al-Ahqaf Tekki, Al-Ahqaf mp3, Al-Ahqaf pdf. Aaya 30–34. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








