Al-Maida · 76/120
Tekki Waxtaan — Al-Maida
قُلْ أَتَعْبُدُونَ مِن دُونِ اللَّهِ مَا لَا يَمْلِكُ لَكُمْ ضَرًّا وَلَا نَفْعًا ۚ وَاللَّهُ هُوَ السَّمِيعُ الْعَلِيمُ ٧٦
Transliteration
Qul ata`budoona min doonil laahi maa laa yamliku lakum darranw wa laa naf`aa; wallaahu Huwas Samee`ul `Aleem
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Neel : “Moo ndax dangeen di bàyyi Yàlla, di jaamu loo xam ne mënuleen a lor, mënuleen a jariñ ? ”.Te Yàlla Moom Kuy dégg la, Ku xam la.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 74-78 — Al-Maida
74أَفَلَا يَتُوبُونَ إِلَى اللَّهِ وَيَسْتَغْفِرُونَهُ ۚ وَاللَّهُ غَفُورٌ رَّحِيمٌ
Lu leen teree tuub ci Yàlla ñaan ko njéggal ? Te Yàlla Jéggalaakoon la, Jaglewaakoon la.
75مَّا الْمَسِيحُ ابْنُ مَرْيَمَ إِلَّا رَسُولٌ قَدْ خَلَتْ مِن قَبْلِهِ الرُّسُلُ وَأُمُّهُ صِدِّيقَةٌ ۖ كَانَا يَأْكُلَانِ الطَّعَامَ ۗ انظُرْ كَيْفَ نُبَيِّنُ لَهُمُ الْآيَاتِ ثُمَّ انظُرْ أَنَّىٰ يُؤْفَكُونَ
Ku ñu barkeel ka, doomi Maryaama, nekkul lu dul ab Yonent, boo xam ne ay Yonent jiitu woon na ko fi. Yaayam ku saxoon ci dëgg la. Ñoom ñaar dañu daan lekk ñam. Gisal ni Nu leen di leerale sunuy tegtal te it xoolal ni ñuy walbateee [dëgg ga].
76قُلْ أَتَعْبُدُونَ مِن دُونِ اللَّهِ مَا لَا يَمْلِكُ لَكُمْ ضَرًّا وَلَا نَفْعًا ۚ وَاللَّهُ هُوَ السَّمِيعُ الْعَلِيمُ
Neel : “Moo ndax dangeen di bàyyi Yàlla, di jaamu loo xam ne mënuleen a lor, mënuleen a jariñ ? ”.Te Yàlla Moom Kuy dégg la, Ku xam la.
77قُلْ يَا أَهْلَ الْكِتَابِ لَا تَغْلُوا فِي دِينِكُمْ غَيْرَ الْحَقِّ وَلَا تَتَّبِعُوا أَهْوَاءَ قَوْمٍ قَدْ ضَلُّوا مِن قَبْلُ وَأَضَلُّوا كَثِيرًا وَضَلُّوا عَن سَوَاءِ السَّبِيلِ
Neel : “Yéen ñon-téere, buleen teeŋal seen diine, mu wuuteek dëgg ga. Buleen topp bànneexi nit ñoo xam ne réeroon nañu bu jëkk, te réeraloon nañu ñu bari, réere tigi yoon wu jub wa.
78لُعِنَ الَّذِينَ كَفَرُوا مِن بَنِي إِسْرَائِيلَ عَلَىٰ لِسَانِ دَاوُودَ وَعِيسَى ابْنِ مَرْيَمَ ۚ ذَٰلِكَ بِمَا عَصَوا وَّكَانُوا يَعْتَدُونَ
Rëbbéef na ña weddi ca waa Bani Israayiila mu jaare ca làmmiñu Daawuda ak [Iisaa] doomi Maryaama, ngir lañu moy ndigal te nekkon ñu jéggi dayo.
Al-MaidaFihi Alxuraan
120Aaya
MedinanRevelation
76Aaya
Tekki — Al-Maida 76
Simoore Al-Maida Aaya 76 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Neel : “Moo ndax dangeen di bàyyi Yàlla, di jaamu…Simoore Aaya 76/120 — Al-Maida المائدة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Maida Dégg, Al-Maida Tekki, Al-Maida mp3, Al-Maida pdf. Aaya 74–78. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








