At-Tur · 30/49
Tekki Waxtaan — Simoore At-Tur
أَمْ يَقُولُونَ شَاعِرٌ نَّتَرَبَّصُ بِهِ رَيْبَ الْمَنُونِ ٣٠
Transliteration
Am yaqooloona shaa`irun natarabbasu bihee raibal manoon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Walla ñuy wax naan : “Kii waykat la ! Leegi tey mu dee jeexal”.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 28-32 — Simoore At-Tur
28إِنَّا كُنَّا مِن قَبْلُ نَدْعُوهُ ۖ إِنَّهُ هُوَ الْبَرُّ الرَّحِيمُ
Nun dey bu jëkk, ca Àddina danu ko daan woo di ko ñaan. Moom Yàlla, moo di Aji-baax ji , di Jaglewaakoon bi yërmaandeem”.
29فَذَكِّرْ فَمَا أَنتَ بِنِعْمَتِ رَبِّكَ بِكَاهِنٍ وَلَا مَجْنُونٍ
Fàttalikul sa xéewali Boroom tax na ba doonoo buxaaba waxantumalaa ab dof ;
30أَمْ يَقُولُونَ شَاعِرٌ نَّتَرَبَّصُ بِهِ رَيْبَ الْمَنُونِ
Walla ñuy wax naan : “Kii waykat la ! Leegi tey mu dee jeexal”.
31قُلْ تَرَبَّصُوا فَإِنِّي مَعَكُم مِّنَ الْمُتَرَبِّصِينَ
Waxal ne: “Xaarleen ! Man itam Maa ngi ànd ak ànd ag yéen di xaar”.
32أَمْ تَأْمُرُهُمْ أَحْلَامُهُم بِهَٰذَا ۚ أَمْ هُمْ قَوْمٌ طَاغُونَ
Moo ndax ñoom seeni xol mooleen di digal ? Am dañoo di aw nit ñu faku ?
At-TurFihi Alxuraan
49Aaya
MeccanRevelation
30Aaya
Tekki — At-Tur 30
Simoore At-Tur Aaya 30 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Walla ñuy wax naan : “Kii waykat la ! Leegi…Simoore Aaya 30/49 — Simoore At-Tur الطور (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore At-Tur Dégg, Simoore At-Tur Tekki, Simoore At-Tur mp3, Simoore At-Tur pdf. Aaya 28–32. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, September 8, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








