At-Tur · 36/49
Tekki Waxtaan — Simoore At-Tur
أَمْ خَلَقُوا السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ ۚ بَل لَّا يُوقِنُونَ ۝٣٦
Am khalaqus samaawaati wal ard; bal laa yooqinoon
📖 Tekkim Wolof
Walla ñoom ñoo bind asamaan yeek suuf si ? Li am kay moo di ne ñoom wóoluwuñu.

🎧 Dégg


📜 Aaya 34-38 — Simoore At-Tur

34فَلْيَأْتُوا بِحَدِيثٍ مِّثْلِهِ إِن كَانُوا صَادِقِينَ
Su fekkee ne, liñuy wax ngi ci ñoom, nanu indi lu melni Alxuraan.
35أَمْ خُلِقُوا مِنْ غَيْرِ شَيْءٍ أَمْ هُمُ الْخَالِقُونَ
Waaw ñoom ndax dañu leen sos bind leen wala ñoom ñooy binde di sos ?
36أَمْ خَلَقُوا السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ ۚ بَل لَّا يُوقِنُونَ
Walla ñoom ñoo bind asamaan yeek suuf si ? Li am kay moo di ne ñoom wóoluwuñu.
37أَمْ عِندَهُمْ خَزَائِنُ رَبِّكَ أَمْ هُمُ الْمُصَيْطِرُونَ
Moo ndax ñoom dañoo am sa ndàmbi Boroom ? Walla ñoom ñooy dogal ?
38أَمْ لَهُمْ سُلَّمٌ يَسْتَمِعُونَ فِيهِ ۖ فَلْيَأْتِ مُسْتَمِعُهُم بِسُلْطَانٍ مُّبِينٍ
Walla ñoom dañoo am ab raas bu ñuy (yéege asamaan di déglu) ? Su fekkee loolu am na ka leen daan yëdujil na indi ay lay yu leer kon !
At-TurFihi Alxuraan
49Aaya
MeccanRevelation
36Aaya

Tekki — At-Tur 36

Simoore At-Tur Aaya 36 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Walla ñoom ñoo bind asamaan yeek suuf si ? Li…

Simoore Aaya 36/49 — Simoore At-Tur الطور (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore At-Tur Dégg, Simoore At-Tur Tekki, Simoore At-Tur mp3, Simoore At-Tur pdf. Aaya 34–38. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers