An-Najm · 25/62
Tekki Waxtaan — Simoore An-Najm
فَلِلَّهِ الْآخِرَةُ وَالْأُولَىٰ ۝٢٥
Falillaahil aakhiratu wal oolaa
📖 Tekkim Wolof
Yàllaa moom àddinaak àllaaxira.

🎧 Dégg


📜 Aaya 23-27 — Simoore An-Najm

23إِنْ هِيَ إِلَّا أَسْمَاءٌ سَمَّيْتُمُوهَا أَنتُمْ وَآبَاؤُكُم مَّا أَنزَلَ اللَّهُ بِهَا مِن سُلْطَانٍ ۚ إِن يَتَّبِعُونَ إِلَّا الظَّنَّ وَمَا تَهْوَى الْأَنفُسُ ۖ وَلَقَدْ جَاءَهُم مِّن رَّبِّهِمُ الْهُدَىٰ
Loolu ay tur la doŋŋ yu ngeen di tudd (xërëm ya), yéen ak seeni baay. Seen njortu rekk la ñu topp waaye yayoowunu jaamu. Topp it seen bànneex, looloo tax njub dikk bawoo fa seen Boroom.
24أَمْ لِلْإِنسَانِ مَا تَمَنَّىٰ
Walla book nit moom limu mébét da koy daldi am ?
25فَلِلَّهِ الْآخِرَةُ وَالْأُولَىٰ
Yàllaa moom àddinaak àllaaxira.
26۞ وَكَم مِّن مَّلَكٍ فِي السَّمَاوَاتِ لَا تُغْنِي شَفَاعَتُهُمْ شَيْئًا إِلَّا مِن بَعْدِ أَن يَأْذَنَ اللَّهُ لِمَن يَشَاءُ وَيَرْضَىٰ
Aka bari Malaaka yu nekk ca asamaan ya te seenug ramu du jiñ dara, ndare ginnaaw bu Yàlla joxee ndigal, mu jëm ci ku Ko soob te Mu gëram ko.
27إِنَّ الَّذِينَ لَا يُؤْمِنُونَ بِالْآخِرَةِ لَيُسَمُّونَ الْمَلَائِكَةَ تَسْمِيَةَ الْأُنثَىٰ
Ña nga xam ne da ñoo gëmul àllaaxira ñooy tudde Malaaka yi turi jigéen,
An-NajmFihi Alxuraan
62Aaya
MeccanRevelation
25Aaya

Tekki — An-Najm 25

Simoore An-Najm Aaya 25 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàllaa moom àddinaak àllaaxira.

Simoore Aaya 25/62 — Simoore An-Najm النجم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Najm Dégg, Simoore An-Najm Tekki, Simoore An-Najm mp3, Simoore An-Najm pdf. Aaya 23–27. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers