An-Najm · 24/62
Tekki Waxtaan — An-Najm
أَمْ لِلْإِنسَانِ مَا تَمَنَّىٰ ۝٢٤
Am lil insaani maa taman naa
📖 Tekkim Wolof
Walla book nit moom limu mébét da koy daldi am ?
🎧 Dégg

📜 Aaya 22-26 — An-Najm

22تِلْكَ إِذًا قِسْمَةٌ ضِيزَىٰ
(Xam ngeen) ne woowu séddale yéen jubul de !
23إِنْ هِيَ إِلَّا أَسْمَاءٌ سَمَّيْتُمُوهَا أَنتُمْ وَآبَاؤُكُم مَّا أَنزَلَ اللَّهُ بِهَا مِن سُلْطَانٍ ۚ إِن يَتَّبِعُونَ إِلَّا الظَّنَّ وَمَا تَهْوَى الْأَنفُسُ ۖ وَلَقَدْ جَاءَهُم مِّن رَّبِّهِمُ الْهُدَىٰ
Loolu ay tur la doŋŋ yu ngeen di tudd (xërëm ya), yéen ak seeni baay. Seen njortu rekk la ñu topp waaye yayoowunu jaamu. Topp it seen bànneex, looloo tax njub dikk bawoo fa seen Boroom.
24أَمْ لِلْإِنسَانِ مَا تَمَنَّىٰ
Walla book nit moom limu mébét da koy daldi am ?
25فَلِلَّهِ الْآخِرَةُ وَالْأُولَىٰ
Yàllaa moom àddinaak àllaaxira.
26۞ وَكَم مِّن مَّلَكٍ فِي السَّمَاوَاتِ لَا تُغْنِي شَفَاعَتُهُمْ شَيْئًا إِلَّا مِن بَعْدِ أَن يَأْذَنَ اللَّهُ لِمَن يَشَاءُ وَيَرْضَىٰ
Aka bari Malaaka yu nekk ca asamaan ya te seenug ramu du jiñ dara, ndare ginnaaw bu Yàlla joxee ndigal, mu jëm ci ku Ko soob te Mu gëram ko.
An-NajmFihi Alxuraan
62Aaya
MeccanRevelation
24Aaya

Tekki — An-Najm 24

Simoore An-Najm Aaya 24 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Walla book nit moom limu mébét da koy daldi am…

Simoore Aaya 24/62 — An-Najm النجم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Najm Dégg, An-Najm Tekki, An-Najm mp3, An-Najm pdf. Aaya 22–26. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers