An-Najm · 27/62
Tekki Waxtaan — Simoore An-Najm
إِنَّ الَّذِينَ لَا يُؤْمِنُونَ بِالْآخِرَةِ لَيُسَمُّونَ الْمَلَائِكَةَ تَسْمِيَةَ الْأُنثَىٰ ۝٢٧
innal lazeena laa yu`minoona bil aakhirati la yusammoonal malaaa`ikata tasmiyatal unsaa
📖 Tekkim Wolof
Ña nga xam ne da ñoo gëmul àllaaxira ñooy tudde Malaaka yi turi jigéen,

🎧 Dégg


📜 Aaya 25-29 — Simoore An-Najm

25فَلِلَّهِ الْآخِرَةُ وَالْأُولَىٰ
Yàllaa moom àddinaak àllaaxira.
26۞ وَكَم مِّن مَّلَكٍ فِي السَّمَاوَاتِ لَا تُغْنِي شَفَاعَتُهُمْ شَيْئًا إِلَّا مِن بَعْدِ أَن يَأْذَنَ اللَّهُ لِمَن يَشَاءُ وَيَرْضَىٰ
Aka bari Malaaka yu nekk ca asamaan ya te seenug ramu du jiñ dara, ndare ginnaaw bu Yàlla joxee ndigal, mu jëm ci ku Ko soob te Mu gëram ko.
27إِنَّ الَّذِينَ لَا يُؤْمِنُونَ بِالْآخِرَةِ لَيُسَمُّونَ الْمَلَائِكَةَ تَسْمِيَةَ الْأُنثَىٰ
Ña nga xam ne da ñoo gëmul àllaaxira ñooy tudde Malaaka yi turi jigéen,
28وَمَا لَهُم بِهِ مِنْ عِلْمٍ ۖ إِن يَتَّبِعُونَ إِلَّا الظَّنَّ ۖ وَإِنَّ الظَّنَّ لَا يُغْنِي مِنَ الْحَقِّ شَيْئًا
te ñoom amuñu ca benn xam-xam : seeni njortu rekk la ñuy topp, te njortu moom jotewul dara ak dëgg.
29فَأَعْرِضْ عَن مَّن تَوَلَّىٰ عَن ذِكْرِنَا وَلَمْ يُرِدْ إِلَّا الْحَيَاةَ الدُّنْيَا
dëdul, képp kuy dumóoyu Sunug fàttali te dundug àddina rekk ñor ko.
An-NajmFihi Alxuraan
62Aaya
MeccanRevelation
27Aaya

Tekki — An-Najm 27

Simoore An-Najm Aaya 27 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña nga xam ne da ñoo gëmul àllaaxira ñooy tudde…

Simoore Aaya 27/62 — Simoore An-Najm النجم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Najm Dégg, Simoore An-Najm Tekki, Simoore An-Najm mp3, Simoore An-Najm pdf. Aaya 25–29. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers