An-Najm · 28/62
Tekki Waxtaan — An-Najm
وَمَا لَهُم بِهِ مِنْ عِلْمٍ ۖ إِن يَتَّبِعُونَ إِلَّا الظَّنَّ ۖ وَإِنَّ الظَّنَّ لَا يُغْنِي مِنَ الْحَقِّ شَيْئًا ٢٨
Transliteration
Wa maa lahum bihee min `ilmin iny yattabi`oona illaz zanna wa innaz zanna laa yughnee minal haqqi shai`aa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
te ñoom amuñu ca benn xam-xam : seeni njortu rekk la ñuy topp, te njortu moom jotewul dara ak dëgg.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 26-30 — An-Najm
26۞ وَكَم مِّن مَّلَكٍ فِي السَّمَاوَاتِ لَا تُغْنِي شَفَاعَتُهُمْ شَيْئًا إِلَّا مِن بَعْدِ أَن يَأْذَنَ اللَّهُ لِمَن يَشَاءُ وَيَرْضَىٰ
Aka bari Malaaka yu nekk ca asamaan ya te seenug ramu du jiñ dara, ndare ginnaaw bu Yàlla joxee ndigal, mu jëm ci ku Ko soob te Mu gëram ko.
27إِنَّ الَّذِينَ لَا يُؤْمِنُونَ بِالْآخِرَةِ لَيُسَمُّونَ الْمَلَائِكَةَ تَسْمِيَةَ الْأُنثَىٰ
Ña nga xam ne da ñoo gëmul àllaaxira ñooy tudde Malaaka yi turi jigéen,
28وَمَا لَهُم بِهِ مِنْ عِلْمٍ ۖ إِن يَتَّبِعُونَ إِلَّا الظَّنَّ ۖ وَإِنَّ الظَّنَّ لَا يُغْنِي مِنَ الْحَقِّ شَيْئًا
te ñoom amuñu ca benn xam-xam : seeni njortu rekk la ñuy topp, te njortu moom jotewul dara ak dëgg.
29فَأَعْرِضْ عَن مَّن تَوَلَّىٰ عَن ذِكْرِنَا وَلَمْ يُرِدْ إِلَّا الْحَيَاةَ الدُّنْيَا
dëdul, képp kuy dumóoyu Sunug fàttali te dundug àddina rekk ñor ko.
30ذَٰلِكَ مَبْلَغُهُم مِّنَ الْعِلْمِ ۚ إِنَّ رَبَّكَ هُوَ أَعْلَمُ بِمَن ضَلَّ عَن سَبِيلِهِ وَهُوَ أَعْلَمُ بِمَنِ اهْتَدَىٰ
Foofu la seen xam-xam yem. Waaye sa Boroom Moo gën a xam ku réere aw yoonam Moo gën a xam it ku gindiku.
An-NajmFihi Alxuraan
62Aaya
MeccanRevelation
28Aaya
Tekki — An-Najm 28
Simoore An-Najm Aaya 28 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te ñoom amuñu ca benn xam-xam : seeni njortu rekk…Simoore Aaya 28/62 — An-Najm النجم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Najm Dégg, An-Najm Tekki, An-Najm mp3, An-Najm pdf. Aaya 26–30. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








