An-Najm · 29/62
Tekki Waxtaan — Simoore An-Najm
فَأَعْرِضْ عَن مَّن تَوَلَّىٰ عَن ذِكْرِنَا وَلَمْ يُرِدْ إِلَّا الْحَيَاةَ الدُّنْيَا ۝٢٩
Fa a`rid `am man tawallaa `an zikrinaa wa lam yurid illal hayaatad dunyaa
📖 Tekkim Wolof
dëdul, képp kuy dumóoyu Sunug fàttali te dundug àddina rekk ñor ko.

🎧 Dégg


📜 Aaya 27-31 — Simoore An-Najm

27إِنَّ الَّذِينَ لَا يُؤْمِنُونَ بِالْآخِرَةِ لَيُسَمُّونَ الْمَلَائِكَةَ تَسْمِيَةَ الْأُنثَىٰ
Ña nga xam ne da ñoo gëmul àllaaxira ñooy tudde Malaaka yi turi jigéen,
28وَمَا لَهُم بِهِ مِنْ عِلْمٍ ۖ إِن يَتَّبِعُونَ إِلَّا الظَّنَّ ۖ وَإِنَّ الظَّنَّ لَا يُغْنِي مِنَ الْحَقِّ شَيْئًا
te ñoom amuñu ca benn xam-xam : seeni njortu rekk la ñuy topp, te njortu moom jotewul dara ak dëgg.
29فَأَعْرِضْ عَن مَّن تَوَلَّىٰ عَن ذِكْرِنَا وَلَمْ يُرِدْ إِلَّا الْحَيَاةَ الدُّنْيَا
dëdul, képp kuy dumóoyu Sunug fàttali te dundug àddina rekk ñor ko.
30ذَٰلِكَ مَبْلَغُهُم مِّنَ الْعِلْمِ ۚ إِنَّ رَبَّكَ هُوَ أَعْلَمُ بِمَن ضَلَّ عَن سَبِيلِهِ وَهُوَ أَعْلَمُ بِمَنِ اهْتَدَىٰ
Foofu la seen xam-xam yem. Waaye sa Boroom Moo gën a xam ku réere aw yoonam Moo gën a xam it ku gindiku.
31وَلِلَّهِ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَمَا فِي الْأَرْضِ لِيَجْزِيَ الَّذِينَ أَسَاءُوا بِمَا عَمِلُوا وَيَجْزِيَ الَّذِينَ أَحْسَنُوا بِالْحُسْنَى
Yàlla moom yi nekk ci asamaan yeek suuf si dana fay ña daan jëf jëf yu ñaaw kem la ñu daan jëf, dana fay it ña daan rafetal seen jëf pey gu gën a rafet,
An-NajmFihi Alxuraan
62Aaya
MeccanRevelation
29Aaya

Tekki — An-Najm 29

Simoore An-Najm Aaya 29 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : dëdul, képp kuy dumóoyu Sunug fàttali te dundug àddina rekk…

Simoore Aaya 29/62 — Simoore An-Najm النجم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Najm Dégg, Simoore An-Najm Tekki, Simoore An-Najm mp3, Simoore An-Najm pdf. Aaya 27–31. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers