An-Najm · 37/62
Tekki Waxtaan — Simoore An-Najm
وَإِبْرَاهِيمَ الَّذِي وَفَّىٰ ۝٣٧
Wa Ibraaheemal lazee waffaaa
📖 Tekkim Wolof
ak Ibraahiima ma jottaloon lool

🎧 Dégg


📜 Aaya 35-39 — Simoore An-Najm

35أَعِندَهُ عِلْمُ الْغَيْبِ فَهُوَ يَرَىٰ
Moo ndax dafa am xam-xamu Kumpa di ko gis ?
36أَمْ لَمْ يُنَبَّأْ بِمَا فِي صُحُفِ مُوسَىٰ
Walla book dafa xamul li nekk ca téerey Muusaa
37وَإِبْرَاهِيمَ الَّذِي وَفَّىٰ
ak Ibraahiima ma jottaloon lool
38أَلَّا تَزِرُ وَازِرَةٌ وِزْرَ أُخْرَىٰ
benn bakkan du gàddul bakkan bàkkaaram,
39وَأَن لَّيْسَ لِلْإِنسَانِ إِلَّا مَا سَعَىٰ
li wér daal, nit ku nekk jëfam lay añe ;
An-NajmFihi Alxuraan
62Aaya
MeccanRevelation
37Aaya

Tekki — An-Najm 37

Simoore An-Najm Aaya 37 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ak Ibraahiima ma jottaloon lool

Simoore Aaya 37/62 — Simoore An-Najm النجم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Najm Dégg, Simoore An-Najm Tekki, Simoore An-Najm mp3, Simoore An-Najm pdf. Aaya 35–39. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers