Al-Qamar · 11/55
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qamar
فَفَتَحْنَا أَبْوَابَ السَّمَاءِ بِمَاءٍ مُّنْهَمِرٍ ۝١١
Fafatahnaaa abwaabas sa maaa`i bimaa`im munhamir
📖 Tekkim Wolof
Nu daldi ubbi wunti asamaan si ci am ndox muy dottiku,

🎧 Dégg


📜 Aaya 9-13 — Simoore Al-Qamar

9۞ كَذَّبَتْ قَبْلَهُمْ قَوْمُ نُوحٍ فَكَذَّبُوا عَبْدَنَا وَقَالُوا مَجْنُونٌ وَازْدُجِرَ
Nitu Nooh, ña leen jiitu woon weddi woon nañu. Ñoom it weddi woon nañu sunub jaam daldi wax ne: “Kii ab dof la ! ” daldi koy bàyyi.
10فَدَعَا رَبَّهُ أَنِّي مَغْلُوبٌ فَانتَصِرْ
mu woo Boroomam ñaan ko ne : “Man dey sonal nañu ma. Dimbalima”.
11فَفَتَحْنَا أَبْوَابَ السَّمَاءِ بِمَاءٍ مُّنْهَمِرٍ
Nu daldi ubbi wunti asamaan si ci am ndox muy dottiku,
12وَفَجَّرْنَا الْأَرْضَ عُيُونًا فَالْتَقَى الْمَاءُ عَلَىٰ أَمْرٍ قَدْ قُدِرَ
nu daldi ballal suuf ak ay bëti ndox. Ndox ya daldi gëndóo daj ci ndigal lu ñu natale.
13وَحَمَلْنَاهُ عَلَىٰ ذَاتِ أَلْوَاحٍ وَدُسُرٍ
Ñu toog ca kaw gaalam ga doon ay dénk ak i pont,
Al-QamarFihi Alxuraan
55Aaya
MeccanRevelation
11Aaya

Tekki — Al-Qamar 11

Simoore Al-Qamar Aaya 11 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nu daldi ubbi wunti asamaan si ci am ndox muy…

Simoore Aaya 11/55 — Simoore Al-Qamar القمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qamar Dégg, Simoore Al-Qamar Tekki, Simoore Al-Qamar mp3, Simoore Al-Qamar pdf. Aaya 9–13. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers