Al-Waqi'a · 46/96
Tekki Waxtaan — Al-Waqi'a
وَكَانُوا يُصِرُّونَ عَلَى الْحِنثِ الْعَظِيمِ ۝٤٦
Wa kaanoo yusirroona `alal hinsil `azeem
📖 Tekkim Wolof
Dañoo nuuran ci bàkkaar ba gëna màgg mu di bokkaale Yàlla
🎧 Dégg

📜 Aaya 44-48 — Al-Waqi'a

44لَّا بَارِدٍ وَلَا كَرِيمٍ
seddul, neexul lewetul.
45إِنَّهُمْ كَانُوا قَبْلَ ذَٰلِكَ مُتْرَفِينَ
Ñoom ba ñuy dund ca àddina da ñu daan fuukarewu.
46وَكَانُوا يُصِرُّونَ عَلَى الْحِنثِ الْعَظِيمِ
Dañoo nuuran ci bàkkaar ba gëna màgg mu di bokkaale Yàlla
47وَكَانُوا يَقُولُونَ أَئِذَا مِتْنَا وَكُنَّا تُرَابًا وَعِظَامًا أَإِنَّا لَمَبْعُوثُونَ
dañu daan wax naan : “ Moo ndax bu nu faatoo ba def suuf ak i yax, dees nanu dekkilaat ?
48أَوَآبَاؤُنَا الْأَوَّلُونَ
nook sunuy baay ak i maam ?...”
Al-Waqi'aFihi Alxuraan
96Aaya
MeccanRevelation
46Aaya

Tekki — Al-Waqi'a 46

Simoore Al-Waqi'a Aaya 46 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Dañoo nuuran ci bàkkaar ba gëna màgg mu di bokkaale…

Simoore Aaya 46/96 — Al-Waqi'a الواقعة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Waqi'a Dégg, Al-Waqi'a Tekki, Al-Waqi'a mp3, Al-Waqi'a pdf. Aaya 44–48. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers