Al-Waqi'a · 45/96
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Waqi'a
إِنَّهُمْ كَانُوا قَبْلَ ذَٰلِكَ مُتْرَفِينَ ۝٤٥
Innaahum kaanoo qabla zaalika mutrafeen
📖 Tekkim Wolof
Ñoom ba ñuy dund ca àddina da ñu daan fuukarewu.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 43-47 — Simoore Al-Waqi'a

43وَظِلٍّ مِّن يَحْمُومٍ
ak ca ron kërug saxaar su ñuul kukk
44لَّا بَارِدٍ وَلَا كَرِيمٍ
seddul, neexul lewetul.
45إِنَّهُمْ كَانُوا قَبْلَ ذَٰلِكَ مُتْرَفِينَ
Ñoom ba ñuy dund ca àddina da ñu daan fuukarewu.
46وَكَانُوا يُصِرُّونَ عَلَى الْحِنثِ الْعَظِيمِ
Dañoo nuuran ci bàkkaar ba gëna màgg mu di bokkaale Yàlla
47وَكَانُوا يَقُولُونَ أَئِذَا مِتْنَا وَكُنَّا تُرَابًا وَعِظَامًا أَإِنَّا لَمَبْعُوثُونَ
dañu daan wax naan : “ Moo ndax bu nu faatoo ba def suuf ak i yax, dees nanu dekkilaat ?
Al-Waqi'aFihi Alxuraan
96Aaya
MeccanRevelation
45Aaya

Tekki — Al-Waqi'a 45

Simoore Al-Waqi'a Aaya 45 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñoom ba ñuy dund ca àddina da ñu daan fuukarewu.

Simoore Aaya 45/96 — Simoore Al-Waqi'a الواقعة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Waqi'a Dégg, Simoore Al-Waqi'a Tekki, Simoore Al-Waqi'a mp3, Simoore Al-Waqi'a pdf. Aaya 43–47. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers