Al-Waqi'a · 60/96
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Waqi'a
نَحْنُ قَدَّرْنَا بَيْنَكُمُ الْمَوْتَ وَمَا نَحْنُ بِمَسْبُوقِينَ ۝٦٠
Nahnu qaddarnaa baina kumul mawta wa maa nahnu bimasbooqeen
📖 Tekkim Wolof
Nun noo natt ag dee ci yéen dogal ko te kenn du ko man a fanq. Te it lottu nu

🎧 Dégg


📜 Aaya 58-62 — Simoore Al-Waqi'a

58أَفَرَأَيْتُم مَّا تُمْنُونَ
Xanaa gisuleen maniyyu mi ngeen sotti :
59أَأَنتُمْ تَخْلُقُونَهُ أَمْ نَحْنُ الْخَالِقُونَ
yéen a koy bind: walla Nun (Yàlla) noo koy sos ?
60نَحْنُ قَدَّرْنَا بَيْنَكُمُ الْمَوْتَ وَمَا نَحْنُ بِمَسْبُوقِينَ
Nun noo natt ag dee ci yéen dogal ko te kenn du ko man a fanq. Te it lottu nu
61عَلَىٰ أَن نُّبَدِّلَ أَمْثَالَكُمْ وَنُنشِئَكُمْ فِي مَا لَا تَعْلَمُونَ
te wuutal leen ñeneen rey leen yéen, dekkilaat leen fu ngeen xamul.
62وَلَقَدْ عَلِمْتُمُ النَّشْأَةَ الْأُولَىٰ فَلَوْلَا تَذَكَّرُونَ
Xam ngeen xéll ca bu jëkk na ka ngeen sosoo. Moo kon ndax dangeen dul fàttaliku ?
Al-Waqi'aFihi Alxuraan
96Aaya
MeccanRevelation
60Aaya

Tekki — Al-Waqi'a 60

Simoore Al-Waqi'a Aaya 60 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nun noo natt ag dee ci yéen dogal ko te…

Simoore Aaya 60/96 — Simoore Al-Waqi'a الواقعة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Waqi'a Dégg, Simoore Al-Waqi'a Tekki, Simoore Al-Waqi'a mp3, Simoore Al-Waqi'a pdf. Aaya 58–62. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers