Al-Waqi'a · 61/96
Tekki Waxtaan — Al-Waqi'a
عَلَىٰ أَن نُّبَدِّلَ أَمْثَالَكُمْ وَنُنشِئَكُمْ فِي مَا لَا تَعْلَمُونَ ۝٦١
Alaaa an nubaddila amsaalakum wa nunshi`akum fee maa laa ta`lamoon
📖 Tekkim Wolof
te wuutal leen ñeneen rey leen yéen, dekkilaat leen fu ngeen xamul.
🎧 Dégg

📜 Aaya 59-63 — Al-Waqi'a

59أَأَنتُمْ تَخْلُقُونَهُ أَمْ نَحْنُ الْخَالِقُونَ
yéen a koy bind: walla Nun (Yàlla) noo koy sos ?
60نَحْنُ قَدَّرْنَا بَيْنَكُمُ الْمَوْتَ وَمَا نَحْنُ بِمَسْبُوقِينَ
Nun noo natt ag dee ci yéen dogal ko te kenn du ko man a fanq. Te it lottu nu
61عَلَىٰ أَن نُّبَدِّلَ أَمْثَالَكُمْ وَنُنشِئَكُمْ فِي مَا لَا تَعْلَمُونَ
te wuutal leen ñeneen rey leen yéen, dekkilaat leen fu ngeen xamul.
62وَلَقَدْ عَلِمْتُمُ النَّشْأَةَ الْأُولَىٰ فَلَوْلَا تَذَكَّرُونَ
Xam ngeen xéll ca bu jëkk na ka ngeen sosoo. Moo kon ndax dangeen dul fàttaliku ?
63أَفَرَأَيْتُم مَّا تَحْرُثُونَ
Xanaa gisuleen li ngeen di ruuj ?
Al-Waqi'aFihi Alxuraan
96Aaya
MeccanRevelation
61Aaya

Tekki — Al-Waqi'a 61

Simoore Al-Waqi'a Aaya 61 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te wuutal leen ñeneen rey leen yéen, dekkilaat leen fu…

Simoore Aaya 61/96 — Al-Waqi'a الواقعة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Waqi'a Dégg, Al-Waqi'a Tekki, Al-Waqi'a mp3, Al-Waqi'a pdf. Aaya 59–63. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers