Al-An'am · 28/165
Tekki Waxtaan — Simoore Al-An'am
بَلْ بَدَا لَهُم مَّا كَانُوا يُخْفُونَ مِن قَبْلُ ۖ وَلَوْ رُدُّوا لَعَادُوا لِمَا نُهُوا عَنْهُ وَإِنَّهُمْ لَكَاذِبُونَ ٢٨
Transliteration
Bal badaa lahum maa kaanoo yukhfoona min qablu wa law ruddoo la`aadoo limaa nuhoo `anhu wa innahum lakaaziboon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Li wér mooy, la ñu doon nëbb, bu jëkkoon feeñ na ca ñoom. Te bu ñu leen delloo woon it, ñu dellu di def la ñu leen tere woon. Ca dëgg-dëgg ñoom ay fenkat lañu.
Additional reference in Fulfulde
M
Mishary Rashid Alafasy
✓
Mishary Rashid Alafasy
✓
M
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
A
Abdurrahman As-Sudais
✓
Abdurrahman As-Sudais
✓
M
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
A
Abdul Basit Abdul Samad
✓
Abdul Basit Abdul Samad
✓
A
Ali Al-Hudhaify
✓
Ali Al-Hudhaify
✓
A
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
A
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
M
Muhammad Ayyoub
✓
Muhammad Ayyoub
✓
A
Abdullah Basfar
✓
Abdullah Basfar
✓
A
Abdullah Al-Juhani
✓
Abdullah Al-Juhani
✓
M
Maher Al Muaiqly
✓
Maher Al Muaiqly
✓
0:00
0:00
📜 Aaya 26-30 — Simoore Al-An'am
26وَهُمْ يَنْهَوْنَ عَنْهُ وَيَنْأَوْنَ عَنْهُ ۖ وَإِن يُهْلِكُونَ إِلَّا أَنفُسَهُمْ وَمَا يَشْعُرُونَ
Te ñoom dañuy tere ku jegeñ Yonent bi, te di ko sori. Waaye alaguñu kenn ku dul seen bopp te bëgguñu ko.
27وَلَوْ تَرَىٰ إِذْ وُقِفُوا عَلَى النَّارِ فَقَالُوا يَا لَيْتَنَا نُرَدُّ وَلَا نُكَذِّبَ بِآيَاتِ رَبِّنَا وَنَكُونَ مِنَ الْمُؤْمِنِينَ
Cëy boo leen gisoon, fa ñu leen taxawale ca Safara. Te ñuy wax : “Ngalla nun ! Yelante kon ñu delloo nu àddina, ba dunu weddi kàddug Yàlla sunu Boroom, bokk ca way-gëm ña”.
28بَلْ بَدَا لَهُم مَّا كَانُوا يُخْفُونَ مِن قَبْلُ ۖ وَلَوْ رُدُّوا لَعَادُوا لِمَا نُهُوا عَنْهُ وَإِنَّهُمْ لَكَاذِبُونَ
Li wér mooy, la ñu doon nëbb, bu jëkkoon feeñ na ca ñoom. Te bu ñu leen delloo woon it, ñu dellu di def la ñu leen tere woon. Ca dëgg-dëgg ñoom ay fenkat lañu.
29وَقَالُوا إِنْ هِيَ إِلَّا حَيَاتُنَا الدُّنْيَا وَمَا نَحْنُ بِمَبْعُوثِينَ
Dañuy wax ne : “Amul geneen dundu gu dul gu àddina bii ; [nun bu nu faatoo] kenn du nu dekkalaat”.
30وَلَوْ تَرَىٰ إِذْ وُقِفُوا عَلَىٰ رَبِّهِمْ ۚ قَالَ أَلَيْسَ هَٰذَا بِالْحَقِّ ۚ قَالُوا بَلَىٰ وَرَبِّنَا ۚ قَالَ فَذُوقُوا الْعَذَابَ بِمَا كُنتُمْ تَكْفُرُونَ
Cëy boo leen gisoon bu ñu leen taxawale ca seen Boroom. Mu ne leen : “Ndax lii du dëgg ? ” Ñu toonte ne : “Axakañ ! Giñ nanu ko ci sunu Boroom ! ” Mu ne leen : “Léegi nag, mosleen mbugal mi ngeen daan weddi”.
Al-An'amFihi Alxuraan
165Aaya
MeccanRevelation
28Aaya
Tekki — Al-An'am 28
Simoore Al-An'am Aaya 28 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Li wér mooy, la ñu doon nëbb, bu jëkkoon feeñ…Simoore Aaya 28/165 — Simoore Al-An'am الأنعام (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-An'am Dégg, Simoore Al-An'am Tekki, Simoore Al-An'am mp3, Simoore Al-An'am pdf. Aaya 26–30. Tekkim Wolof: Fulfulde.
Simoore Al-An'am
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Friday, October 2, 2026
Don't forget us in your sincere prayers


