Al-Qalam · 11/52
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qalam
هَمَّازٍ مَّشَّاءٍ بِنَمِيمٍ ۝١١
Hammaazim mash shaaa`im binameem
📖 Tekkim Wolof
ab saagakat, buy dox di rambaaje,

🎧 Dégg


📜 Aaya 9-13 — Simoore Al-Qalam

9وَدُّوا لَوْ تُدْهِنُ فَيُدْهِنُونَ
Bëgg nañu nga nooy ba ñu nooy ñoom itam.
10وَلَا تُطِعْ كُلَّ حَلَّافٍ مَّهِينٍ
Bul topp bépp waatkat, bu doyadi,
11هَمَّازٍ مَّشَّاءٍ بِنَمِيمٍ
ab saagakat, buy dox di rambaaje,
12مَّنَّاعٍ لِّلْخَيْرِ مُعْتَدٍ أَثِيمٍ
buy tere aw yiw, tey jalgati, di def bàkkaar,
13عُتُلٍّ بَعْدَ ذَٰلِكَ زَنِيمٍ
ak ku jàgg, te bariw ay.
Al-QalamFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
11Aaya

Tekki — Al-Qalam 11

Simoore Al-Qalam Aaya 11 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ab saagakat, buy dox di rambaaje,

Simoore Aaya 11/52 — Simoore Al-Qalam القلم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qalam Dégg, Simoore Al-Qalam Tekki, Simoore Al-Qalam mp3, Simoore Al-Qalam pdf. Aaya 9–13. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers