Al-Haqqa · 45/52
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Haqqa
لَأَخَذْنَا مِنْهُ بِالْيَمِينِ ۝٤٥
La-akhaznaa minhu bilyameen
📖 Tekkim Wolof
( Kon ) dananu téye loxob ndeyjooram,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 43-47 — Simoore Al-Haqqa

43تَنزِيلٌ مِّن رَّبِّ الْعَالَمِينَ
Dafa wàcc bawoo ci boroom àddina si.
44وَلَوْ تَقَوَّلَ عَلَيْنَا بَعْضَ الْأَقَاوِيلِ
Su ca fentoon jenn jenn wax,
45لَأَخَذْنَا مِنْهُ بِالْيَمِينِ
( Kon ) dananu téye loxob ndeyjooram,
46ثُمَّ لَقَطَعْنَا مِنْهُ الْوَتِينَ
daldi, dog sidiiti xolam ( mu dee ).
47فَمَا مِنكُم مِّنْ أَحَدٍ عَنْهُ حَاجِزِينَ
Te kon kenn ci yéen du ko mana fanq.
Al-HaqqaFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
45Aaya

Tekki — Al-Haqqa 45

Simoore Al-Haqqa Aaya 45 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ( Kon ) dananu téye loxob ndeyjooram,

Simoore Aaya 45/52 — Simoore Al-Haqqa الحاقة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Haqqa Dégg, Simoore Al-Haqqa Tekki, Simoore Al-Haqqa mp3, Simoore Al-Haqqa pdf. Aaya 43–47. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 29, 2026

Don't forget us in your sincere prayers