Al-Haqqa · 44/52
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Haqqa
وَلَوْ تَقَوَّلَ عَلَيْنَا بَعْضَ الْأَقَاوِيلِ ۝٤٤
Wa law taqawwala `alainaa ba`dal aqaaweel
📖 Tekkim Wolof
Su ca fentoon jenn jenn wax,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 42-46 — Simoore Al-Haqqa

42وَلَا بِقَوْلِ كَاهِنٍ ۚ قَلِيلًا مَّا تَذَكَّرُونَ
du waxi it ab buxaaba, aka néew lu ngeen di fàttaliku.
43تَنزِيلٌ مِّن رَّبِّ الْعَالَمِينَ
Dafa wàcc bawoo ci boroom àddina si.
44وَلَوْ تَقَوَّلَ عَلَيْنَا بَعْضَ الْأَقَاوِيلِ
Su ca fentoon jenn jenn wax,
45لَأَخَذْنَا مِنْهُ بِالْيَمِينِ
( Kon ) dananu téye loxob ndeyjooram,
46ثُمَّ لَقَطَعْنَا مِنْهُ الْوَتِينَ
daldi, dog sidiiti xolam ( mu dee ).
Al-HaqqaFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
44Aaya

Tekki — Al-Haqqa 44

Simoore Al-Haqqa Aaya 44 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Su ca fentoon jenn jenn wax,

Simoore Aaya 44/52 — Simoore Al-Haqqa الحاقة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Haqqa Dégg, Simoore Al-Haqqa Tekki, Simoore Al-Haqqa mp3, Simoore Al-Haqqa pdf. Aaya 42–46. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers