Al-A'raf · 107/206
Tekki Waxtaan — Simoore Al-A'raf
فَأَلْقَىٰ عَصَاهُ فَإِذَا هِيَ ثُعْبَانٌ مُّبِينٌ ۝١٠٧
Qa alqaa `asaahu fa izaa hiya su`baanum mubeen
📖 Tekkim Wolof
Sànni na yetam wa mu daldi nekk jaan ju rëy.

🎧 Dégg


📜 Aaya 105-109 — Simoore Al-A'raf

105حَقِيقٌ عَلَىٰ أَن لَّا أَقُولَ عَلَى اللَّهِ إِلَّا الْحَقَّ ۚ قَدْ جِئْتُكُم بِبَيِّنَةٍ مِّن رَّبِّكُمْ فَأَرْسِلْ مَعِيَ بَنِي إِسْرَائِيلَ
wér na ci man ma bañ a wax ci Yàlla lu dul dëgg. Ne indil naa leen aw lay wu tukkee ci seen Boroom. Boyalal waa Bani-Israayil ñu ànd ak man.”
106قَالَ إِن كُنتَ جِئْتَ بِآيَةٍ فَأْتِ بِهَا إِن كُنتَ مِنَ الصَّادِقِينَ
Mu toontu ne : “Ndegam danga indi ag kéemaan, wone ko ndegal ku dëggu nga.”
107فَأَلْقَىٰ عَصَاهُ فَإِذَا هِيَ ثُعْبَانٌ مُّبِينٌ
Sànni na yetam wa mu daldi nekk jaan ju rëy.
108وَنَزَعَ يَدَهُ فَإِذَا هِيَ بَيْضَاءُ لِلنَّاظِرِينَ
Mu génne loxoom mu daldi weex tàll ca ña koy gis.
109قَالَ الْمَلَأُ مِن قَوْمِ فِرْعَوْنَ إِنَّ هَٰذَا لَسَاحِرٌ عَلِيمٌ
Kilifa ya bokk ca nitu Firawna ne ko : “Jabar bu am xam-xam la”.
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
107Aaya

Tekki — Al-A'raf 107

Simoore Al-A'raf Aaya 107 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Sànni na yetam wa mu daldi nekk jaan ju rëy.

Simoore Aaya 107/206 — Simoore Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-A'raf Dégg, Simoore Al-A'raf Tekki, Simoore Al-A'raf mp3, Simoore Al-A'raf pdf. Aaya 105–109. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers