Al-A'raf · 108/206
Tekki Waxtaan — Simoore Al-A'raf
وَنَزَعَ يَدَهُ فَإِذَا هِيَ بَيْضَاءُ لِلنَّاظِرِينَ ۝١٠٨
Wa naza`a yadahoo fa izaa hiya baidaaa`u linnaazireen
📖 Tekkim Wolof
Mu génne loxoom mu daldi weex tàll ca ña koy gis.

🎧 Dégg


📜 Aaya 106-110 — Simoore Al-A'raf

106قَالَ إِن كُنتَ جِئْتَ بِآيَةٍ فَأْتِ بِهَا إِن كُنتَ مِنَ الصَّادِقِينَ
Mu toontu ne : “Ndegam danga indi ag kéemaan, wone ko ndegal ku dëggu nga.”
107فَأَلْقَىٰ عَصَاهُ فَإِذَا هِيَ ثُعْبَانٌ مُّبِينٌ
Sànni na yetam wa mu daldi nekk jaan ju rëy.
108وَنَزَعَ يَدَهُ فَإِذَا هِيَ بَيْضَاءُ لِلنَّاظِرِينَ
Mu génne loxoom mu daldi weex tàll ca ña koy gis.
109قَالَ الْمَلَأُ مِن قَوْمِ فِرْعَوْنَ إِنَّ هَٰذَا لَسَاحِرٌ عَلِيمٌ
Kilifa ya bokk ca nitu Firawna ne ko : “Jabar bu am xam-xam la”.
110يُرِيدُ أَن يُخْرِجَكُم مِّنْ أَرْضِكُمْ ۖ فَمَاذَا تَأْمُرُونَ
[Firawna] ne : “Dafa leen bëgg a génne ci seen suuf.” - “Lan mooy seen ndigal ? ”
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
108Aaya

Tekki — Al-A'raf 108

Simoore Al-A'raf Aaya 108 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu génne loxoom mu daldi weex tàll ca ña koy…

Simoore Aaya 108/206 — Simoore Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-A'raf Dégg, Simoore Al-A'raf Tekki, Simoore Al-A'raf mp3, Simoore Al-A'raf pdf. Aaya 106–110. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers