Al-A'raf · 106/206
Tekki Waxtaan — Al-A'raf
قَالَ إِن كُنتَ جِئْتَ بِآيَةٍ فَأْتِ بِهَا إِن كُنتَ مِنَ الصَّادِقِينَ ۝١٠٦
Qaala in kunta ji`ta bi Aayatin faati bihaaa in kunta minas saadiqeen
📖 Tekkim Wolof
Mu toontu ne : “Ndegam danga indi ag kéemaan, wone ko ndegal ku dëggu nga.”

🎧 Dégg


📜 Aaya 104-108 — Al-A'raf

104وَقَالَ مُوسَىٰ يَا فِرْعَوْنُ إِنِّي رَسُولٌ مِّن رَّبِّ الْعَالَمِينَ
Muusaa ne : “Yaw Firawna, man ab Yonent laa [boo xam ne], Yàlla miy Boroom àddina si Moo ma yónni,
105حَقِيقٌ عَلَىٰ أَن لَّا أَقُولَ عَلَى اللَّهِ إِلَّا الْحَقَّ ۚ قَدْ جِئْتُكُم بِبَيِّنَةٍ مِّن رَّبِّكُمْ فَأَرْسِلْ مَعِيَ بَنِي إِسْرَائِيلَ
wér na ci man ma bañ a wax ci Yàlla lu dul dëgg. Ne indil naa leen aw lay wu tukkee ci seen Boroom. Boyalal waa Bani-Israayil ñu ànd ak man.”
106قَالَ إِن كُنتَ جِئْتَ بِآيَةٍ فَأْتِ بِهَا إِن كُنتَ مِنَ الصَّادِقِينَ
Mu toontu ne : “Ndegam danga indi ag kéemaan, wone ko ndegal ku dëggu nga.”
107فَأَلْقَىٰ عَصَاهُ فَإِذَا هِيَ ثُعْبَانٌ مُّبِينٌ
Sànni na yetam wa mu daldi nekk jaan ju rëy.
108وَنَزَعَ يَدَهُ فَإِذَا هِيَ بَيْضَاءُ لِلنَّاظِرِينَ
Mu génne loxoom mu daldi weex tàll ca ña koy gis.
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
106Aaya

Tekki — Al-A'raf 106

Simoore Al-A'raf Aaya 106 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu toontu ne : “Ndegam danga indi ag kéemaan, wone…

Simoore Aaya 106/206 — Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-A'raf Dégg, Al-A'raf Tekki, Al-A'raf mp3, Al-A'raf pdf. Aaya 104–108. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers