Al-A'raf · 192/206
Tekki Waxtaan — Al-A'raf
وَلَا يَسْتَطِيعُونَ لَهُمْ نَصْرًا وَلَا أَنفُسَهُمْ يَنصُرُونَ ۝١٩٢
Wa laa yastatee`oona lahum nasranw wa laaa anfusahum yansuroon
📖 Tekkim Wolof
te mënuñuleen a dimbali, mënuñoo dimbali seen bopp sax ?
🎧 Dégg

📜 Aaya 190-194 — Al-A'raf

190فَلَمَّا آتَاهُمَا صَالِحًا جَعَلَا لَهُ شُرَكَاءَ فِيمَا آتَاهُمَا ۚ فَتَعَالَى اللَّهُ عَمَّا يُشْرِكُونَ
Ba Mu leen mayee [doom], ñu bokkaale Yàlla ca la Mu leen may. Te Yàlla jomb na la ñu Ko bokkaale.
191أَيُشْرِكُونَ مَا لَا يَخْلُقُ شَيْئًا وَهُمْ يُخْلَقُونَ
Moo ndax dañuy bokkaaleek [Yàlla] ñoo xam ne mënuñoo bind dara te dañu leen a bind,
192وَلَا يَسْتَطِيعُونَ لَهُمْ نَصْرًا وَلَا أَنفُسَهُمْ يَنصُرُونَ
te mënuñuleen a dimbali, mënuñoo dimbali seen bopp sax ?
193وَإِن تَدْعُوهُمْ إِلَى الْهُدَىٰ لَا يَتَّبِعُوكُمْ ۚ سَوَاءٌ عَلَيْكُمْ أَدَعَوْتُمُوهُمْ أَمْ أَنتُمْ صَامِتُونَ
Boo leen woowee ci njub, duñuleen topp. Ngeen woo leen walla ngeen noppi [bañ leen a woo] yem kepp.
194إِنَّ الَّذِينَ تَدْعُونَ مِن دُونِ اللَّهِ عِبَادٌ أَمْثَالُكُمْ ۖ فَادْعُوهُمْ فَلْيَسْتَجِيبُوا لَكُمْ إِن كُنتُمْ صَادِقِينَ
Ña nga xam ne dangeen leen jaamu bàyyi Yàlla, ay jaam lañu ni yéen. Wooleen ba xam danañu leen nangul ndeem ñu dëggu ngeen.
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
192Aaya

Tekki — Al-A'raf 192

Simoore Al-A'raf Aaya 192 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te mënuñuleen a dimbali, mënuñoo dimbali seen bopp sax ?

Simoore Aaya 192/206 — Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-A'raf Dégg, Al-A'raf Tekki, Al-A'raf mp3, Al-A'raf pdf. Aaya 190–194. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers