Al-A'raf · 191/206
Tekki Waxtaan — Simoore Al-A'raf
أَيُشْرِكُونَ مَا لَا يَخْلُقُ شَيْئًا وَهُمْ يُخْلَقُونَ ۝١٩١
A yushrikoona maa laa yakhluqu shai`anw wa hum yukhlaqoon
📖 Tekkim Wolof
Moo ndax dañuy bokkaaleek [Yàlla] ñoo xam ne mënuñoo bind dara te dañu leen a bind,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 189-193 — Simoore Al-A'raf

189۞ هُوَ الَّذِي خَلَقَكُم مِّن نَّفْسٍ وَاحِدَةٍ وَجَعَلَ مِنْهَا زَوْجَهَا لِيَسْكُنَ إِلَيْهَا ۖ فَلَمَّا تَغَشَّاهَا حَمَلَتْ حَمْلًا خَفِيفًا فَمَرَّتْ بِهِ ۖ فَلَمَّا أَثْقَلَت دَّعَوَا اللَّهَ رَبَّهُمَا لَئِنْ آتَيْتَنَا صَالِحًا لَّنَكُونَنَّ مِنَ الشَّاكِرِينَ
Moom mooy Ki leen bind ci benn bakkan, mu génne ca soxnaam ngir muy am ug dal ci moom; ba mu ko muuree, mu ëmb ëmb bu woyof, muy dem ak ëmbam. Ba mu diisee, ñoom ñaar ñu ñaanYàlla seen Boroom ne ko : “Soo nu mayee [doom] ju baax, kon faf dananu bokk ci gërëmaakoon ña”.
190فَلَمَّا آتَاهُمَا صَالِحًا جَعَلَا لَهُ شُرَكَاءَ فِيمَا آتَاهُمَا ۚ فَتَعَالَى اللَّهُ عَمَّا يُشْرِكُونَ
Ba Mu leen mayee [doom], ñu bokkaale Yàlla ca la Mu leen may. Te Yàlla jomb na la ñu Ko bokkaale.
191أَيُشْرِكُونَ مَا لَا يَخْلُقُ شَيْئًا وَهُمْ يُخْلَقُونَ
Moo ndax dañuy bokkaaleek [Yàlla] ñoo xam ne mënuñoo bind dara te dañu leen a bind,
192وَلَا يَسْتَطِيعُونَ لَهُمْ نَصْرًا وَلَا أَنفُسَهُمْ يَنصُرُونَ
te mënuñuleen a dimbali, mënuñoo dimbali seen bopp sax ?
193وَإِن تَدْعُوهُمْ إِلَى الْهُدَىٰ لَا يَتَّبِعُوكُمْ ۚ سَوَاءٌ عَلَيْكُمْ أَدَعَوْتُمُوهُمْ أَمْ أَنتُمْ صَامِتُونَ
Boo leen woowee ci njub, duñuleen topp. Ngeen woo leen walla ngeen noppi [bañ leen a woo] yem kepp.
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
191Aaya

Tekki — Al-A'raf 191

Simoore Al-A'raf Aaya 191 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ndax dañuy bokkaaleek [Yàlla] ñoo xam ne mënuñoo bind…

Simoore Aaya 191/206 — Simoore Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-A'raf Dégg, Simoore Al-A'raf Tekki, Simoore Al-A'raf mp3, Simoore Al-A'raf pdf. Aaya 189–193. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 29, 2026

Don't forget us in your sincere prayers