Al-A'raf · 61/206
Tekki Waxtaan — Simoore Al-A'raf
قَالَ يَا قَوْمِ لَيْسَ بِي ضَلَالَةٌ وَلَٰكِنِّي رَسُولٌ مِّن رَّبِّ الْعَالَمِينَ ۝٦١
Qaala yaa qawmi laisa bee dalaalatunw wa laakinnee Rasoolum mir Rabbil `aalameen
📖 Tekkim Wolof
Mu ne : "Man nekkuma ci ag réer ; Waaye man kat ab Yonentub Yàlla, miy Boroom àddina si, laa.

🎧 Dégg


📜 Aaya 59-63 — Simoore Al-A'raf

59لَقَدْ أَرْسَلْنَا نُوحًا إِلَىٰ قَوْمِهِ فَقَالَ يَا قَوْمِ اعْبُدُوا اللَّهَ مَا لَكُم مِّنْ إِلَٰهٍ غَيْرُهُ إِنِّي أَخَافُ عَلَيْكُمْ عَذَابَ يَوْمٍ عَظِيمٍ
Yónni woon Nanu [Nooh] ci aw nitam. Mu ne leen : “Yéen samay mbokk, nangeen jaamu Yàlla. Amuleen jeneen Yàlla ju dul Moom. Man dey, ragal naa ci yéen mbugalum bis bu màgg”.
60قَالَ الْمَلَأُ مِن قَوْمِهِ إِنَّا لَنَرَاكَ فِي ضَلَالٍ مُّبِينٍ
Mbooloo ma, ca aw nitam [kilifa ya], toontu ko ne : “Gis nanu ne yaa ngi ci réer gu tar”.
61قَالَ يَا قَوْمِ لَيْسَ بِي ضَلَالَةٌ وَلَٰكِنِّي رَسُولٌ مِّن رَّبِّ الْعَالَمِينَ
Mu ne : "Man nekkuma ci ag réer ; Waaye man kat ab Yonentub Yàlla, miy Boroom àddina si, laa.
62أُبَلِّغُكُمْ رِسَالَاتِ رَبِّي وَأَنصَحُ لَكُمْ وَأَعْلَمُ مِنَ اللَّهِ مَا لَا تَعْلَمُونَ
Dama leen di jottali sama bataaxalub Boroom, te dama leen di laabire, te xam naa ci Yàlla lu ngeen xamul.
63أَوَعَجِبْتُمْ أَن جَاءَكُمْ ذِكْرٌ مِّن رَّبِّكُمْ عَلَىٰ رَجُلٍ مِّنكُمْ لِيُنذِرَكُمْ وَلِتَتَّقُوا وَلَعَلَّكُمْ تُرْحَمُونَ
Moo ndax dafa leen a jaaxal, ay kàdduy waare dikkal leen tukkee ca seen Boroom, jaare ci góor gu bokk ci yéen, ngir mu artu leen ngeen ragal Yàlla, ndax xéy-na yërëmeef leen ? ”
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
61Aaya

Tekki — Al-A'raf 61

Simoore Al-A'raf Aaya 61 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu ne : "Man nekkuma ci ag réer ; Waaye…

Simoore Aaya 61/206 — Simoore Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-A'raf Dégg, Simoore Al-A'raf Tekki, Simoore Al-A'raf mp3, Simoore Al-A'raf pdf. Aaya 59–63. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers