Al-A'raf · 76/206
Tekki Waxtaan — Al-A'raf
قَالَ الَّذِينَ اسْتَكْبَرُوا إِنَّا بِالَّذِي آمَنتُم بِهِ كَافِرُونَ ۝٧٦
Qaalal lazeenas takbarooo innaa billazeee aamanntum bihee kaafiroon
📖 Tekkim Wolof
Ñay rëy-rëylu ne leen : “Nun dey, li ngeen gëm, weddi nanu ko”.
🎧 Dégg

📜 Aaya 74-78 — Al-A'raf

74وَاذْكُرُوا إِذْ جَعَلَكُمْ خُلَفَاءَ مِن بَعْدِ عَادٍ وَبَوَّأَكُمْ فِي الْأَرْضِ تَتَّخِذُونَ مِن سُهُولِهَا قُصُورًا وَتَنْحِتُونَ الْجِبَالَ بُيُوتًا ۖ فَاذْكُرُوا آلَاءَ اللَّهِ وَلَا تَعْثَوْا فِي الْأَرْضِ مُفْسِدِينَ
Fàttalikuleen ba Mu leen defee ay kuutaay, ca ginnaaw Haad, mu dëkkal leen ci suuf si. Ngeen tabax ay kër yu rëy ci dénd yi, di yatt ci doj yi ay kër. Fàttalikuleen xéewali Yàlla te buleen doon ay yàqkat ci kaw suuf si.
75قَالَ الْمَلَأُ الَّذِينَ اسْتَكْبَرُوا مِن قَوْمِهِ لِلَّذِينَ اسْتُضْعِفُوا لِمَنْ آمَنَ مِنْهُمْ أَتَعْلَمُونَ أَنَّ صَالِحًا مُّرْسَلٌ مِّن رَّبِّهِ ۚ قَالُوا إِنَّا بِمَا أُرْسِلَ بِهِ مُؤْمِنُونَ
Kilifa ya nekkoon di rëy-rëylu ciy nitam wax nañu, ña ñu doyadal, muy ña gëm ca ñoom : “Moo ndax wóor na leen ne Saalihu Yonentub Yàlla la ? ". Ñu toontu ne : “Nun dey way-gëm lanu [ci bataaxal] bi ñu ko yónnee”.
76قَالَ الَّذِينَ اسْتَكْبَرُوا إِنَّا بِالَّذِي آمَنتُم بِهِ كَافِرُونَ
Ñay rëy-rëylu ne leen : “Nun dey, li ngeen gëm, weddi nanu ko”.
77فَعَقَرُوا النَّاقَةَ وَعَتَوْا عَنْ أَمْرِ رَبِّهِمْ وَقَالُوا يَا صَالِحُ ائْتِنَا بِمَا تَعِدُنَا إِن كُنتَ مِنَ الْمُرْسَلِينَ
Ñu rey giléem ga, jalgati seen ndigalul Boroom, daldi ne : “Yaw Saalihu, indil nu la nga nu doon tëkkoo, ndegam ci Yonent yi nga bokk”.
78فَأَخَذَتْهُمُ الرَّجْفَةُ فَأَصْبَحُوا فِي دَارِهِمْ جَاثِمِينَ
Ag yëngug suuf rajaxe leen ; ñu xëy ne lànjaŋ ca seen kër ya.
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
76Aaya

Tekki — Al-A'raf 76

Simoore Al-A'raf Aaya 76 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñay rëy-rëylu ne leen : “Nun dey, li ngeen gëm,…

Simoore Aaya 76/206 — Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-A'raf Dégg, Al-A'raf Tekki, Al-A'raf mp3, Al-A'raf pdf. Aaya 74–78. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers