Al-Qiyama · 38/40
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qiyama
ثُمَّ كَانَ عَلَقَةً فَخَلَقَ فَسَوَّىٰ ۝٣٨
Summa kaana `alaqata fakhalaq fasawwaa
📖 Tekkim Wolof
Mu mujj di aw lumbu Ma bind ko mu ne càndaŋ yemoo;

🎧 Dégg


📜 Aaya 36-40 — Simoore Al-Qiyama

36أَيَحْسَبُ الْإِنسَانُ أَن يُتْرَكَ سُدًى
Moo ndax nit dafa foog ne dañu koy bàyyi rekk noonu muy nguyaay?
37أَلَمْ يَكُ نُطْفَةً مِّن مَّنِيٍّ يُمْنَىٰ
Moo ndax dafa doonul woon tóqug maniyu guy sottiku ?
38ثُمَّ كَانَ عَلَقَةً فَخَلَقَ فَسَوَّىٰ
Mu mujj di aw lumbu Ma bind ko mu ne càndaŋ yemoo;
39فَجَعَلَ مِنْهُ الزَّوْجَيْنِ الذَّكَرَ وَالْأُنثَىٰ
ma def ci ñaari toolént ya : góor ak jigéen ?
40أَلَيْسَ ذَٰلِكَ بِقَادِرٍ عَلَىٰ أَن يُحْيِيَ الْمَوْتَىٰ
Moo ndax kooku munula dekkilaat ku dee ?
Al-QiyamaFihi Alxuraan
40Aaya
MeccanRevelation
38Aaya

Tekki — Al-Qiyama 38

Simoore Al-Qiyama Aaya 38 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu mujj di aw lumbu Ma bind ko mu ne…

Simoore Aaya 38/40 — Simoore Al-Qiyama القيامة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qiyama Dégg, Simoore Al-Qiyama Tekki, Simoore Al-Qiyama mp3, Simoore Al-Qiyama pdf. Aaya 36–40. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers