Al-Qiyama · 37/40
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qiyama
أَلَمْ يَكُ نُطْفَةً مِّن مَّنِيٍّ يُمْنَىٰ ۝٣٧
Alam yaku nutfatam mim maniyyiny yumnaa
📖 Tekkim Wolof
Moo ndax dafa doonul woon tóqug maniyu guy sottiku ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 35-39 — Simoore Al-Qiyama

35ثُمَّ أَوْلَىٰ لَكَ فَأَوْلَىٰ
Te it yaayoo nga toskare, yayoo nga ko !
36أَيَحْسَبُ الْإِنسَانُ أَن يُتْرَكَ سُدًى
Moo ndax nit dafa foog ne dañu koy bàyyi rekk noonu muy nguyaay?
37أَلَمْ يَكُ نُطْفَةً مِّن مَّنِيٍّ يُمْنَىٰ
Moo ndax dafa doonul woon tóqug maniyu guy sottiku ?
38ثُمَّ كَانَ عَلَقَةً فَخَلَقَ فَسَوَّىٰ
Mu mujj di aw lumbu Ma bind ko mu ne càndaŋ yemoo;
39فَجَعَلَ مِنْهُ الزَّوْجَيْنِ الذَّكَرَ وَالْأُنثَىٰ
ma def ci ñaari toolént ya : góor ak jigéen ?
Al-QiyamaFihi Alxuraan
40Aaya
MeccanRevelation
37Aaya

Tekki — Al-Qiyama 37

Simoore Al-Qiyama Aaya 37 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ndax dafa doonul woon tóqug maniyu guy sottiku ?

Simoore Aaya 37/40 — Simoore Al-Qiyama القيامة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qiyama Dégg, Simoore Al-Qiyama Tekki, Simoore Al-Qiyama mp3, Simoore Al-Qiyama pdf. Aaya 35–39. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers